From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
y el verbo se hizo carne y habitó entre nosotros, y contemplamos su gloria, como la gloria del unigénito del padre, lleno de gracia y de verdad
kàddu gi ñëw, doon nit, dëkk ci sunu biir. gis nañu ndamam, mu fees ak yiw ak dëgg, ndam li baay bi jox jenn doomam ji mu am kepp.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
lo que era desde el principio, lo que hemos oído, lo que hemos visto con nuestros ojos, lo que contemplamos y palparon nuestras manos tocante al verbo de vid
nu ngi leen di bind ci mbirum ki ñuy wax kàddug dund, moom mi amoon ca njàlbéen ga; mi nu dégg te gis ko ak sunuy bët, mi nu xool te laal ko ak sunuy loxo.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: