Results for maestro translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

--maestro, ¿cuál es el gran mandamiento de la ley

Wolof

«kilifa gi, ban ndigal moo gën a màgg ci yoonu musaa?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

del cual he sido puesto como predicador, apóstol y maestro

Wolof

te yàlla fal na ma ndaw ak jàngalekat, ngir may yégle xebaar bi;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero él le dijo: --maestro, todo esto he guardado desde mi juventud

Wolof

waa ji ne ko: «kilifa gi, loolu lépp sàmm naa ko li dale ci samag ndaw ba tey.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

"el discípulo no es más que su maestro, ni el siervo más que su señor

Wolof

yeesu teg ca ne: «taalibe gënul kilifaam, te jaam gënul sangam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

le respondieron algunos de los escribas, diciendo: --maestro, bien has dicho

Wolof

ci kaw loolu ay xutbakat ne ko: «li nga wax dëgg la, kilifa gi!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

el discípulo no es superior a su maestro, pero cualquiera que es plenamente instruido será como su maestro

Wolof

taalibe gënul kilifaam, waaye taalibe bu jàng ba wàcc, dina yem ak kilifaam demin.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

le dijeron: --maestro, esta mujer ha sido sorprendida en el mismo acto de adulterio

Wolof

noonu ñu ne yeesu: «kilifa gi, jigéen jii de, dañu koo bett muy njaaloo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

le dijo uno de la multitud: --maestro, dile a mi hermano que reparta conmigo la herencia

Wolof

am ca mbooloo ma ku ne yeesu: «kilifa gi, joxal ndigal sama mag, mu sédd ma ci sunu ndono.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

respondió jesús y le dijo: --tú eres el maestro de israel, ¿y no sabes esto

Wolof

yeesu tontu ko ne: «yaw yaay jàngal bànni israyil te xamuloo mbir yii?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces se le acercó un escriba y le dijo: --maestro, te seguiré a dondequiera que tú vayas

Wolof

laata ñuy jàll, benn xutbakat daldi ñëw ci moom ne ko: «kilifa gi, dinaa la topp fépp foo jëm.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces, algunos de los fariseos de entre la multitud le dijeron: --maestro, reprende a tus discípulos

Wolof

waaye ay farisen yu nekkoon ca mbooloo ma ne yeesu: «kilifa gi, yeddal sa taalibe yi!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

"pero vosotros, no seáis llamados rabí; porque uno solo es vuestro maestro, y todos vosotros sois hermanos

Wolof

waaye yéen buñu leen wooye “kilifa gi,” ndaxte kenn rekk moo di seen kilifa, te yéen ñépp ay bokk ngeen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

cuando él salía del templo, uno de sus discípulos dijo: --maestro, ¡mira qué piedras y qué edificios

Wolof

bi yeesu di jóge ca kër yàlla ga, kenn ca taalibe ya ne ko: «kilifa gi, xoolal! ni mu réye ay doj, te rafete ni ay taax!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces se levantó en el sanedrín cierto fariseo llamado gamaliel, maestro de la ley, honrado por todo el pueblo, y mandó que sacasen a los hombres por un momento

Wolof

waaye amoon na fa nit ku tudd gamaleel, bokk ci tariixab farisen ya, di xutbakat bu tedd ci yoonu musaa, mu jóg ca mbooloo ma, santaane ñu génne leen tuuti.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

--maestro, moisés dijo: si alguno muere sin tener hijos, su hermano se casará con su mujer y levantará descendencia a su hermano

Wolof

«kilifa gi, musaa nee woon na: “boo xamee ne góor dee na te amul doom, na rakkam donn jabaram, ngir sàkkal magam njaboot.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

bástale al discípulo ser como su maestro, y al siervo como su señor. si al padre de familia le llamaron beelzebul, ¡cuánto más lo harán a los de su casa

Wolof

bu taalibe yemee ak kilifaam demin, doy na; jaam it ni sangam. ndegam tudde nañu boroom kër gi beelsebul, astemaak waa kër gi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces respondiendo juan dijo: --maestro, vimos a cierto hombre echando fuera demonios en tu nombre, y se lo prohibimos, porque no sigue con nosotros

Wolof

bi loolu amee yowaana jël kàddu gi ne: «kilifa gi, danoo gis nit kuy dàq ay rab ci sa tur, nu tere ko ko, ndaxte bokkul ci nun.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces le preguntaron diciendo: --maestro, ¿cuándo será esto? ¿qué señal habrá cuando estas cosas estén por suceder

Wolof

Ñu laaj ko ne: «kilifa gi, kañ la loolu di am? te luy tegtal ne, looloo ngi waaj a xew?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

decidle al dueño de la casa: "el maestro te dice: '¿dónde está la habitación en la que he de comer la pascua con mis discípulos?'

Wolof

te ngeen ne boroom kër ga: “kilifa gi nee na: ana néegu gan, bi may lekke reeru jéggi ba, man ak samay taalibe?”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

a unos puso dios en la iglesia, primero apóstoles, en segundo lugar profetas, en tercer lugar maestros; después los que hacen milagros, después los dones de sanidades, los que ayudan, los que administran, los que tienen diversidad de lenguas

Wolof

te yàlla teg na ci mbooloom ñi gëm, ku nekk ak sa may: ci bu jëkk ay ndawi kirist, teg ca ñiy wax ci kàddug yàlla, teg ca ñiy jàngale, ñiy def ay kéemaan, ñi am mayu wéral ay jàngoro, ñiy dimbalee, ñiy jiite, ñiy wax ay xeeti làkk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,764,002,228 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK