Results for vamos adentro, he preparado algo de... translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

entonces sus discípulos se decían el uno al otro: --¿acaso alguien le habrá traído algo de comer

Wolof

taalibe ya nag di laajante naan: «ndax dafa am ku ko indil lekk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y como ellos aún no lo creían por el gozo que tenían y porque estaban asombrados, les dijo: --¿tenéis aquí algo de comer

Wolof

waaye ba tey mënuñu woon a gëm ndax seen mbég ak jaaxle. noonu yeesu laaj leen ne: «ndax am ngeen fii lu ñu lekk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

al atardecer, sus discípulos se acercaron a él y le dijeron: --el lugar es desierto, y la hora ya avanzada. despide a la gente para que vayan a las aldeas y compren para sí algo de comer

Wolof

ca ngoon sa taalibe yi ñëw ci moom ne ko: «fii àllub neen la, te léegi mu guddi. doo yiwi mbooloo mi, ngir ñu dem ci dëkk yu ndaw yi, jënd lu ñu man a lekk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,781,982,308 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK