Results for alimwambia translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

yule mdogo, alimwambia baba yake: baba, nipe urithi wangu. naye akawagawia mali yake.

Wolof

benn bés caat ma ne baay ba: “baay, damaa bëggoon, nga jox ma li may war a féetewoo ci ndono li.” noonu baay ba daldi leen séddale alalam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

je, mungu alimjibu nini? alimwambia: "nimejiwekea elfu saba ambao hawakumwabudu baali."

Wolof

waaye lii la ko yàlla tontu: «dencal naa sama bopp juróom-ñaari junniy nit, ñi jaamuwul baal.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

bwana alimwambia bwana wangu: keti upande wangu wa kulia, mpaka niwaweke adui zako chini ya miguu yako.

Wolof

“boroom bi wax na sama boroom:‘toogal ci sama ndeyjoor,ba kera may daaneelsay noon ci sa kanam’ ”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mungu alimwambia: ondoka katika nchi yako; waache watu wa ukoo wako; nenda katika nchi nitakayokuonyesha!

Wolof

mu ne ko: “toxul sa réew, bàyyi say bokk, te ñëw ci réew, mi ma lay won.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

maana alimwambia mose: "nitamhurumia mtu yeyote ninayetaka kumhurumia; nitamwonea huruma mtu yeyote ninayetaka."

Wolof

dafa wax musaa sax ne ko:«dinaa yërëm ku ma neex,laabiir ci ku ma neex.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

ndiyo maana kristo alipokuwa anakuja ulimwenguni, alimwambia mungu: "hukutaka dhabihu wala sadaka, lakini umenitayarishia mwili.

Wolof

looloo tax bi muy wàcc àddina, kirist nee na:«bëggoo saraxu mala walla beneen sarax,waaye aw yaram nga ma defaral.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, yesu na alipotazama na kuona umati wa watu ukija kwake, alimwambia filipo, "tununue wapi mikate ili watu hawa wapate kula?"

Wolof

bi yeesu xoolee, gis mbooloo mu réy di ñëw ci moom, mu ne filib: «fu nuy jële mburu, mu nu leen man a dundale?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

baada ya siku kadhaa, paulo alimwambia barnaba, "turudi tukawatembelee wale ndugu katika kila mji tulikolihubiri neno la bwana tukajionee jinsi wanavyoendelea."

Wolof

gannaaw ay fan pool ne barnabas: «nan dellu seeti bokk ya ca dëkk yépp, fu nu mas a yéglee kàddug boroom bi, ba gis nu ñu def.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"kulipokuchwa, huyo mwenye shamba alimwambia mtunza hazina wake, waite wafanyakazi ukawalipe mshahara wao, ukianzia na wale walioajiriwa mwisho, na kumalizia na wale wa kwanza.

Wolof

«bi nga xamee ne timis jot na, boroom tool ba ne jawriñ ja: “woowal liggéeykat yi te fey leen seen bëccëg, tàmbali ci ñi mujj a ñëw, ba ci ñi fi jëkk.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

daudi mwenyewe akiongozwa na roho mtakatifu alisema: bwana alimwambia bwana wangu: keti upande wangu wa kulia, mpaka nitakapowaweka adui zako chini ya miguu yako."

Wolof

daawuda moom wax na ci kàttanu xel mu sell mi naan:“boroom bi nee na sama boroom:«“toogal ci sama ndeyjoor,ba kera may daaneelsay noon ci sa kanam.»“ “

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

malaika wa bwana alimwambia filipo, "jitayarishe uende kusini kupitia njia inayotoka yerusalemu kwenda gaza." (njia hiyo hupita jangwani.)

Wolof

naka noonu benn malaakam boroom bi ne filib: «jógal te jublu misra, jaar ci yoon wi jóge yerusalem, jëm gasa, di màndiŋ.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, watu hao wawili walipokuwa wakiondoka, petro alimwambia yesu, "bwana, ni vizuri kwamba tupo hapa: basi, tujenge vibanda vitatu: kimoja chako, kimoja cha mose na kimoja cha eliya." --kwa kweli hakujua anasema nini.

Wolof

bi nit ñooñu di sore yeesu, piyeer ne ko: «kilifa gi, bég nanu ci sunu teew fii; nanu defar ñetti mbaar, benn yaw, benn musaa ak benn iliyas.» fekk xamul la mu doon wax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,748,228,472 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK