Results for tulipanda translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

huko, tulikuta meli iliyokuwa inakwenda foinike, hivyo tulipanda, tukasafiri.

Wolof

foofa nag nu gis gaal guy jàll ba fenisi, nu dugg ca, mu daldi teddi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

tulipokwisha agana nao, tulipanda meli tukaenda moja kwa moja mpaka kosi. kesho yake tulifika rodo, na kutoka huko tulikwenda patara.

Wolof

bi nga xamee ne tàggoo nanu ak ñoom ci naqar, nu dugg gaal, jubal dunu kos. te ca ëllëg sa nu dem ba teer ca rodd, ba noppi jóge fa, jàll ba patara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

sisi tulipanda meli tukatangulia kwenda aso ambako tungemchukua paulo. ndivyo alivyopanga; maana alitaka kufika huko kwa kupitia nchi kavu.

Wolof

nun nag nu jiitu, dugg gaal jëm asos, fa nu pool santoon, nu jële ko fa; fekk moom fas na yéeney dox, ba agsi fa.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

sisi, baada ya sikukuu ya mikate isiyotiwa chachu, tulipanda meli kutoka filipi na baada ya siku tatu tukawafikia kule troa. huko tulikaa kwa muda wa juma moja.

Wolof

waaye naka nun, gannaaw màggalu yawut, ga ñuy wax mburu ya amul lawiir, nu dugg gaal ci filib, def ci juróomi fan, fekksi leen torowas, nu am fa juróom-ñaari fan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

tulipanda meli ya adiramito iliyokuwa inasafiri na kupitia bandari kadhaa za mkoa wa asia, tukaanza safari. aristarko, mwenyeji wa makedonia kutoka thesalonika, alikuwa pamoja nasi.

Wolof

nu dugg ca gaalu dëkku adaramit guy taxaw ci teeruy asi, daldi tàbbi ci biir géej; te aristàrk, mi dëkk tesalonig ci diiwaanu maseduwan, ànd ak nun.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,742,618,317 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK