Results for tunajua translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

sisi tunaamini, na tunajua kwamba wewe ndiwe yule mtakatifu wa mungu."

Wolof

léegi nun gëm nanu te xam nanu ne, yaa di aji sell, ji jóge ci yàlla.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

tunajua kwamba hukumu ya mungu kwa wale wanaofanya mambo kama hayo ni hukumu ya haki.

Wolof

xam nanu ne, ñiy jëfe noonu, yàlla dina leen àtte, te àtteem jub na.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

sisi tunajua kwamba mungu alisema na mose, lakini mtu huyu hatujui ametoka wapi!"

Wolof

xam nanu ne, yàlla wax na ak musaa; waaye kii, xamunu sax fu mu jóge.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kristo atakapokuja hakuna mtu atakayejua mahali alikotoka, lakini sisi tunajua alikotoka mtu huyu!"

Wolof

waaye waa ji, xam nanu fu mu jóge, te saa su almasi bi dee dikk, kenn du xam fu mu bàyyikoo.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

maana, tunajua kwamba kristo amekwisha fufuliwa kutoka wafu na hafi tena; kifo hakimtawali tena.

Wolof

xam ne kirist mi dekki dootul dee mukk, dee mënatul dara ci moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa maana tunajua kwamba mpaka hivi sasa, viumbe vyote vinalia kwa maumivu kama ya kujifungua mtoto.

Wolof

xam nanu ba fi nu tollu ne, li yàlla bind lépp a ngi metitlu ni jigéen juy matu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

tunajua kwamba mungu hawasikilizi watu wenye dhambi, ila humsikiliza yeyote mwenye kumcha na kutimiza mapenzi yake.

Wolof

xam nanu ne, yàlla du déglu boroom bàkkaar. waaye nag, dina déglu ki koy ragal tey def coobareem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

tunajua kwamba tunaishi katika umoja na mungu, naye mungu anaishi katika umoja nasi, kwani yeye ametupa roho wake.

Wolof

ci lii lanuy xame ne, sax nanu ci yàlla, te moom itam dëkk na ci nun: sol na nu xelam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

yeye hutusikiliza kila tunapomwomba; na kwa vile tunajua kwamba yeye hutusikiliza kila tunapomwomba, twajua pia kwamba atupatia yote tunayomwomba.

Wolof

gannaaw xam nañu ne, dina nangu lépp lu nu koy ñaan, xam nanu it ne, li nu ko ñaan, jox na nu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

sisi tunajua kwamba tumekwisha pita kutoka katika kifo na kuingia katika uzima kwa sababu tunawapenda ndugu zetu. mtu asiye na upendo hubaki katika kifo.

Wolof

mbëggeel gi nu bëgg sunuy bokk moo nuy xamal ne, jóge nanu ci dee, tàbbi ci dund. ku bëggul sa mbokk, yaa ngi ci dee ba tey.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

tunajua kwamba sheria huwahusu walio chini ya sheria hiyo, hata hawawezi kuwa na kisingizio chochote, na ulimwengu wote uko chini ya hukumu ya mungu.

Wolof

xam nanu nag ne, lépp lu yoonu musaa wax, wax na ko ñi nekk ci yoon woowu, ngir gémmiñ yépp ne miig, te waa àddina sépp jaar ci àtteb yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini, ingawa twasema namna hii, wapenzi wetu, tunalo tumaini kubwa juu ya hali yenu. tunajua kwamba mmepokea baraka zile bora za wokovu wenu.

Wolof

waaye nag yéen samay soppe, su fekkee ne sax, nii lanuy waxe, nu ngi yaakaar li gën ci yéen te ànd ak mucc.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, sisi tunajua umuhimu wa kumcha bwana, na hivyo tunajitahidi kuwavuta watu. mungu anatujua waziwazi, nami natumaini kwamba nanyi pia mnatujua kinaganaga.

Wolof

gannaaw xam nanu ragal yàlla nag, nu ngi fexee gëmloo nit ñi, waaye li nu nekk leer na yàlla te yaakaar naa ne, leer na leen it, ba ne fàŋŋ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wapenzi wangu, sisi ni watoto wa mungu sasa, lakini bado haijaonekana wazi jinsi tutakavyokuwa. lakini tunajua kwamba wakati kristo atakapotokea, tutafanana naye kwani tutamwona vile alivyo.

Wolof

samay soppe, léegi doomi yàlla lanu, te li nu nar a nekki feeñagul, waaye xam nanu ne, bés bu almasi bi feeñee, dinanu nirook moom, ndaxte dinanu ko gis, na mu mel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, wakamwita tena aliyekuwa kipofu, wakamwambia, "sema ukweli mbele ya mungu! sisi tunajua kwamba mtu huyu ni mwenye dhambi."

Wolof

farisen ya dellu woowaat ka gumba woon ne ko: «waxal sa digganteek yàlla. xam nanu ne, waa joojee boroom bàkkaar la.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, sisi tunajua na tunaamini upendo alio nao mungu kwetu sisi. mungu ni upendo, na kila mtu aishiye katika upendo, anaishi katika muungano na mungu, na mungu anaishi katika muungano naye.

Wolof

mbëggeel gi yàlla am ci nun, xam nanu ko te gëm ko. yàlla mbëggeel la, te képp ku sax ci mbëggeel, yaa ngi sax ci yàlla, mu dëkk ci yaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hao wapelelezi wakamwambia, "mwalimu, tunajua kwamba unasema na kufundisha mambo ya kweli; tunajua kwamba wewe huna ubaguzi; wewe wafundisha ukweli juu ya njia ya mungu.

Wolof

Ñu daldi ñëw ci yeesu ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne li ngay wax te di ko jàngale lu jub la. amuloo parlàqu, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, wakawatuma wafuasi wao pamoja na wafuasi wa kikundi cha herode. wakamwuliza, "mwalimu, tunajua kwamba wewe ni mtu mwaminifu, na kwamba wafundisha njia ya mungu kwa uaminifu; humwogopi mtu yeyote, maana cheo cha mtu si kitu kwako.

Wolof

noonu ñu yónni ci moom seeni taalibe ak ñi far ak buur bi erodd ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne ku wóor nga, te ragaloo kenn, ndaxte seetuloo jëmmi nit, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,790,824,333 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK