Results for wamekuwa translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

"nawahurumia watu hawa kwa sababu wamekuwa nami kwa muda wa siku tatu, wala hawana chakula.

Wolof

«yërëm naa mbooloo mi, ndaxte toog nañu fi man ñetti fan, te amatuñu lu ñu lekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

hawa wamekuwa watoto wa mungu si kwa uwezo wa kibinadamu, wala kwa nguvu za kimwili, wala kwa mapenzi ya mtu, bali mungu mwenyewe ndiye baba yao.

Wolof

Ñooñu judduwuñu ci deret walla ci bëgg-bëggu yaram, walla ci coobarey nit. Ñu ngi juddu ci yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini hawakuwapata na hivyo walimburuta yasoni pamoja na ndugu wengine mpaka kwa wakuu wa mji, wakapiga kelele: "watu hawa wamekuwa wakivuruga dunia yote na sasa wako hapa mjini.

Wolof

bi ñu leen gisul nag, ñu diri yason ak ñeneen ca bokk ya ci kanam àttekat ya. Ñuy wax ci kaw naan: «nit ñi dëpp àddina sépp agsi nañu fii léegi,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kwa sababu wanaikataa habari njema, wayahudi wamekuwa adui wa mungu, lakini kwa faida yenu nyinyi watu wa mataifa. lakini, kwa kuwa waliteuliwa, bado ni rafiki wa mungu kwa sababu ya baba zao.

Wolof

gannaaw bañ nañu xebaar bu baax bi, ay bañaaley yàlla lañu, ngir ngeen jot barkeem. waaye gannaaw yàlla tànn na leen, dafa leen bëgg ba tey ndax seen maam ya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

naye yoshua aitwaye yusto, anawasalimuni. miongoni mwa wayahudi waliokwisha pokea imani, hawa tu peke yao, ndio wanaofanya kazi pamoja nami kwa ajili ya utawala wa mungu; nao wamekuwa msaada mkubwa kwangu.

Wolof

yeesu mi ñuy dàkkentale yustus, moom it mu ngi leen di nuyu. Ñoom rekk ñooy yawut yiy liggéeyandook man ngir nguuru yàlla, te ñoo féexal sama xol.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, yesu aliwaita wanafunzi wake, akasema, "nawaonea watu hawa huruma kwa sababu kwa siku tatu wamekuwa nami, wala hawana chakula. sipendi kuwaacha waende bila kula wasije wakazimia njiani."

Wolof

gannaaw loolu yeesu woo ci moom taalibeem ya ne leen: «yërëm naa mbooloo mi, ndaxte toog nañu fi man ñetti fan, te amatuñu lu ñu lekk. bëgguma leen a yiwi te lekkuñu, ngir bañ ñu tële ci yoon wi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
8,947,529,217 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK