Results for fariséerna translation from Swedish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swedish

Wolof

Info

Swedish

och männen voro utsända ifrån fariséerna.

Wolof

amoon na ñu bokk ca farisen ya, yu àndoon ca mbooloo, ma ñu yónni woon ca yaxya.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men då nu fariséerna voro församlade, frågade jesus dem

Wolof

bi farisen ya dajee nag, yeesu laaj leen:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men bland fariséerna var en man som hette nikodemus, en av judarnas rådsherrar.

Wolof

amoon na ca farisen ya nit ku ñu naan nikodem te mu bokk ca kilifay yawut ya.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då svarade fariséerna dem: »haven nu också i blivit förvillade?

Wolof

noonu farisen ya laaj leen: «mbaa naxuñu leen, yéen itam?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då förde de honom, mannen som förut hade varit blind, bort till fariséerna.

Wolof

noonu ñu daldi indil farisen yi nit ki gumba woon.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

allt detta hörde nu fariséerna, som voro penningkära, och de drevo då gäck med honom.

Wolof

farisen yi déglu li yeesu doon wax lépp, tàmbali di ko reetaan, ndaxte ñu bëggoon xaalis lañu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då nu översteprästerna och fariséerna hörde hans liknelser, förstodo de att det var om dem som han talade.

Wolof

bi nga xamee ne saraxalekat yu mag ya ak farisen ya dégg nañu léebam yooyu, ñu xam ne ñoom lay wax.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

därefter gingo fariséerna bort och fattade det beslutet att de skulle söka snärja honom genom något hans ord.

Wolof

booba farisen ya dem gise, ba xam lu ñu war a def, ngir fiir yeesu ci waxam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då gingo fariséerna bort och fattade strax, tillsammans med herodianerna, det beslutet att de skulle förgöra honom.

Wolof

ca saa sa nag farisen ya génn, daldi gise ak ñi far ak buur bi erodd, ngir fexe koo reylu.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då förde översteprästerna och fariséerna dit en kvinna som hade blivit beträdd med äktenskapsbrott; och när de hade lett henne fram,

Wolof

xutbakat ya ak farisen ya indi jenn jigéen ju ñu bettoon muy njaaloo, ñu taxawal ko ca diggu mbooloo ma.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då sade fariséerna till honom: »du vittnar om dig själv; ditt vittnesbörd gäller icke.»

Wolof

farisen ya ne ko: «yaw yaay seedeel sa bopp, kon li ngay wax du dëgg.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men då fariséerna sågo detta, sade de till hans lärjungar: »huru kan eder mästare äta med publikaner och syndare?»

Wolof

bi ko farisen ya gisee nag, ñu ne taalibe ya: «lu tax seen kilifa di lekkandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

när han inför allt folket sade detta till dem, blevo fariséerna och de lagkloke mycket förbittrade och gåvo sig i strid med honom om många stycken;

Wolof

bi yeesu génnee bérab boobu, farisen ya ak xutbakat ya ëmbal ko mer te di ko seetlu ci fànn gu nekk,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då sammankallade översteprästerna och fariséerna en rådsförsamling och sade: »vad skola vi taga oss till? denne man gör ju många tecken.

Wolof

farisen ya ak saraxalekat yu mag ya woo kureelu àttekat ya ne: «nit kii kat, kéemaan yi muy def a ngi bëgg a bare. lu nuy def nag?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

därefter kommo johannes' lärjungar till honom och sade: »varför fasta icke dina lärjungar då vi och fariséerna ofta fasta?»

Wolof

gannaaw loolu taalibey yaxya ñëw ci yeesu ne ko: «lu tax nuy woor, nun ak farisen yi, te say taalibe duñu woor?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

därför frågade honom nu fariséerna och de skriftlärde: »varför vandra icke dina lärjungar efter de äldstes stadgar, utan äta med orena händer?»

Wolof

noonu farisen ya ak xutbakat ya laaj ko ne: «lu tax say taalibe duñu topp aaday yoon, yi maam yi tëral, waaye ñuy lekk ak loxo yu setul?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då begynte de skriftlärde och fariséerna tänka så: »vad är denne för en, som talar så hädiska ord? vem kan förlåta synder utom gud allena?»

Wolof

xutbakat yi ak farisen yi di werante ci seen xel naan: «kii mooy kan bay sosal yàlla? ana ku man a baale bàkkaar yi, ku dul yàlla doŋŋ?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men fariséerna -- särskilt de skriftlärde bland dem -- knorrade mot hans lärjungar och sade: »huru kunnen i äta och dricka med publikaner och syndare?»

Wolof

farisen yi ak seeni xutbakat di xultu taalibey yeesu yi ne leen: «lu tax ngeen di lekkandoo ak di naanandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

dock funnos jämväl bland rådsherrarna många som trodde på honom; men för fariséernas skulle ville de icke bekänna det, för att de icke skulle bliva utstötta ur synagogan.

Wolof

fekk na ci biir njiit yi sax, ñu bare gëmoon nañu yeesu, waaye farisen yee tax fésaluñu ko, ndaxte dañoo ragaloon, ñu dàq leen ca jàngu ba.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,800,418,848 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK