Results for folkhopen translation from Swedish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swedish

Wolof

Info

Swedish

ty folkhopen följde efter och skriade: »bort med honom!»

Wolof

ndaxte mbooloo maa nga ko topp, di xaacu ne: «reyleen ko!»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

hon hade fått höra om jesus och kom nu i folkhopen, bakom honom, och rörde vid hans mantel.

Wolof

noonu mu déggoon turu yeesu, ne ci boppam: «su ma laalee ay yéreem rekk, dinaa wér.» mu jaxasoo ak mbooloo mi nag, doxe ko gannaaw, laal mbubbam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då drog man ur folkhopen fram alexander, som judarna sköto framför sig. och alexander gav tecken med handen att han ville hålla ett försvarstal inför folket.

Wolof

ci kaw loolu yawut ya jéñ alegsàndar ci kanam, te mbooloo ma di ko xaacu ay ndigal, mu daldi tàllal loxoom, ngir làyyi ca mbooloo ma.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då ropade en man ur folkhopen och sade: »mästare, jag beder dig, se till min son, ty han är mitt enda barn.

Wolof

nit xaacu ci biir mbooloo mi naan: «kilifa gi, maa ngi lay ñaan, nga seet sama doom, ndaxte moom kepp laa am.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men strax då jesus inom sig förnam vilken kraft som hade gått ut ifrån honom, vände han sig om i folkhopen och frågade: »vem rörde vid mina kläder?»

Wolof

yeesu yég ci saa si ne, doole génn na ci moom. mu walbatiku nag ne mbooloo mi: «ana ku laal samay yére?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

när han sade detta, hov en kvinna in folkhopen upp sin röst och ropade till honom: »saligt är det moderssköte som har burit dig, och de bröst som du har diat.»

Wolof

bi yeesu di wax loolu, jenn jigéen yékkati baatam ca biir mbooloo ma ne: «céy jigéen ji la ëmb te nàmpal la moo barkeel!»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men jesus frågade: »vem var det som rörde vid mig?» då alla nekade till att hava gjort det, sade petrus: »mästare, hela folkhopen trycker och tränger dig ju.»

Wolof

yeesu laaj nit ña ne: «ana ku ma laal?» ku nekk di miim. noonu piyeer ne ko: «kilifa gi, nit ñépp a ngi lay wër, di la tanc wet gu nekk.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,776,843,515 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK