Results for kallades translation from Swedish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swedish

Wolof

Info

Swedish

barnabas ville då att de skulle taga med sig johannes, som ock kallades markus.

Wolof

barnabas nag bëggoon na yóbbaale yowaana, mi ñuy wax it màrk.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men satan for in i judas, som kallades iskariot, och som var en av de tolv.

Wolof

noonu seytaane daldi solu yudaa, mi ñuy wooye iskariyo te mu bokkoon ca fukki taalibe ya ak ñaar.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och ropade på någon för att få veta om simon, som ock kallades petrus, gästade där.

Wolof

Ñu woote nag naan: «simoŋ, mi ñu dàkkentale piyeer, ndax fi la dëkk?»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och han bar själv sitt kors och kom så ut till det ställe som kallades huvudskalleplatsen, på hebreiska golgata.

Wolof

yeesu ci boppam gàddu bant ba, génn ngir dem ca fa ñuy wax bérabu kaaŋu bopp; ñu koy wooye golgota ci làkku yawut.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

men tomas, en av de tolv, han som kallades didymus, var icke med dem, när jesus kom.

Wolof

fekk na tomaa, mi bokk ci fukki taalibe yi ak ñaar, te turam di tekki «séex bi,» nekku fa woon, bi yeesu ñëwee.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och matteus och tomas och jakob, alfeus' son, och simon, som kallades ivraren;

Wolof

macë ak tomaa, saag doomu alfe, ak simoŋ mi bokk ci mbooloo, ma ñu tudde Ñi farlu ci moom seen réew;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

det var med knapp nöd som vi kommo där förbi och hunno fram till en ort som kallades goda hamnarna, icke långt från staden lasea.

Wolof

nu romb fa ak coono yu bare, agsi ca bérab bu ñuy wax teeru yu neex, te dend ak dëkku lase.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då han nu höll sig till petrus och johannes, strömmade allt folket, utom sig av häpnad, tillsammans till dem på den plats som kallades salomos pelargång.

Wolof

naka waa ji taq ci piyeer ak yowaana, ñépp waaru; ñu daldi daw, fekksi leen ca bérab ba ñuy wax werandaa bu suleymaan.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då sade tomas, som kallades didymus, till de andra lärjungarna: »låt oss gå med, för att vi må dö med honom.»

Wolof

noonu tomaa, ki turam di tekki «séex bi,» daldi ne yeneen taalibe ya: «nanu dem nun itam, deeyandoo ak moom!»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och när de hade kommit till den plats som kallades »huvudskallen» korsfäste de honom där, så ock ogärningsmännen, den ene på högra sidan och den andre på vänstra.

Wolof

bi xarekat ya agsee ba ca bérab, ba ñuy wooye kaaŋu bopp, ñu daaj fa yeesu ca bant, daajaale ñaari defkati lu bon ya, kenn ca ndeyjooram, ka ca des ca càmmooñam.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

simon petrus och tomas, som kallades didymus, och natanael, han som var från kana i galileen, och sebedeus' söner voro tillsammans, och med dem två andra av hans lärjungar.

Wolof

taalibey yeesu yii àndoon nañu: simoŋ piyeer; tomaa, ki turam di tekki «séex bi;» nataneel, mi dëkk kana ca diiwaanu galile; doomi sebede ak yeneen ñaari taalibe.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

bland vilka jämväl i ären, i som ären kallade och jesu kristi egna --

Wolof

te ci ngeen bokk, yéen ñi yàlla woo, ngeen nekk ci kirist.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,748,697,867 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK