Results for coobareem translation from Wolof to Amharic

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Amharic

Info

Wolof

xam nga coobareem, ndaxte jàng nga ci yoonu musaa, ba fonk yëf yi gën a baax.

Amharic

ፈቃዱንም ብታውቅ ከሕግም ተምረህ የሚሻለውን ፈትነህ ብትወድ፤

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci coobareem la nu sole kàddug dëgg gi, ba nu judduwaat, di tànneefu lépp lu mu bind.

Amharic

ለፍጥረቱ የበኵራት ዓይነት እንድንሆን በእውነት ቃል አስቦ ወለደን።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kóolute gi nu am ci kanam yàlla mooy lii, su nu ko ñaanee dara ci coobareem, dina nu nangul.

Amharic

በእርሱ ዘንድ ያለን ድፍረት ይህ ነው፤ እንደ ፈቃዱ አንዳች ብንለምን ይሰማናል።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xam nanu ne, yàlla du déglu boroom bàkkaar. waaye nag, dina déglu ki koy ragal tey def coobareem.

Amharic

እግዚአብሔርን የሚፈራ ፈቃዱንም የሚያደርግ ቢኖር ያንን እግዚአብሔር ይሰማዋል እንጂ ኃጢአተኞችን እንዳይሰማ እናውቃለን።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñiy topp seen nafsu, seeni bëgg-bëgg rekk lañu fonk, waaye ñiy topp xelu yàlla mi, coobareem lañu fonk.

Amharic

እንደ ሥጋ ፈቃድ የሚኖሩ የሥጋን ነገር ያስባሉና፥ እንደ መንፈስ ፈቃድ የሚኖሩ ግን የመንፈስን ነገር ያስባሉ።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

nit kiy wax ci coobareem nag, day wut a màggal boppam, waaye kiy wut a màggal ki ko yónni, dëgg rekk lay wax te jubadiwul fenn.

Amharic

ከራሱ የሚናገር የራሱን ክብር ይፈልጋል፤ የላከውን ክብር የሚፈልግ ግን እርሱ እውነተኛ ነው በእርሱም ዓመፃ የለበትም።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu ne ma: “sunu yàllay maam tànn na la, ba may la, nga xam coobareem te gis aji jub ji te nga dégg ay waxam.

Amharic

እርሱም አለኝ። የአባቶቻችን አምላክ ፈቃዱን ታውቅ ዘንድና ጻድቁን ታይ ዘንድ ከአፉም ድምፅን ትሰማ ዘንድ አስቀድሞ መርጦሃል

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

matal ci lépp lu baax, ba ngeen man a def coobareem, di jëfe ci nun li neex ci moom, mu jaarale lépp ci yeesu kirist, moom mi yelloo ndam ba fàww. amiin.

Amharic

በኢየሱስ ክርስቶስ በኩል በፊቱ ደስ የሚያሰኘውን በእናንተ እያደረገ፥ ፈቃዱን ታደርጉ ዘንድ በመልካም ሥራ ሁሉ ፍጹማን ያድርጋችሁ፤ ለእርሱ እስከ ዘላለም ድረስ ክብር ይሁን፤ አሜን።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naka apolos sunu mbokk mi nag moom, xiir naa ko ay yooni yoon, mu ñëw ci yéen, ànd ak bokk yi. waaye fi mu ne dëppoowul ak coobareem. dina ñëw saa su ko manee.

Amharic

ስለ ወንድማችን ስለ አጵሎስ ግን ከወንድሞቹ ጋር ወደ እናንተ ሊሄድ እጅግ አድርጌ ለምኜው ነበር፤ ዛሬም ለመምጣት ከቶ ፈቃድ አልነበረውም፥ ሲመቸው ግን ይመጣል።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,200,536 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK