Results for fi translation from Wolof to Amharic

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Amharic

Info

Wolof

ndaxte indaalewunu fi dara, te dunu yóbbaale dara.

Amharic

ወደ ዓለም ምንም እንኳ አላመጣንምና፥

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye ma des fi ci àddina moo gën ci yéen.

Amharic

ነገር ግን በሥጋ መኖሬ ስለ እናንተ እጅግ የሚያስፈልግ ነው።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye li mat, bu dikkee, li matul jóge fi.

Amharic

ፍጹም የሆነ ሲመጣ ግን ተከፍሎ የነበረው ይሻራል።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte fi mu ne sax am na ñu jeng xaat, ba topp seytaane.

Amharic

ከአሁን በፊት አንዳንዶች ሰይጣንን እንዲከተሉ ፈቀቅ ብለዋልና።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yaw nag saxal ci li nga jàng te mu wóor la, xam fi nga tibbe.

Amharic

አንተ ግን በተማርህበትና በተረዳህበት ነገር ጸንተህ ኑር፥ ከማን እንደ ተማርኸው ታውቃለህና፤

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte amu fi kenn gannaaw timote, ku bokk ak man xalaat te fonk leen bu wér.

Amharic

እንደ እርሱ ያለ፥ ስለ ኑሮአችሁ በቅንነት የሚጨነቅ፥ ማንም የለኝምና፤

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

buleen noot ñi leen yàlla dénk, waaye ngeen nekk ay royukaay fi kanam jur gi.

Amharic

ለመንጋው ምሳሌ ሁኑ እንጂ ማኅበሮቻችሁን በኃይል አትግዙ፤

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu seytaane bàyyi ko. te ay malaaka daldi ñëw fi yeesu, di ko topptoo.

Amharic

ያን ጊዜ ዲያቢሎስ ተወው፥ እነሆም፥ መላእክት ቀርበው ያገለግሉት ነበር።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yaa gàtt xel! li ngay ji, du jebbi dund gu bees, fi ak deewul ba noppi.

Amharic

አንተ ሞኝ፥ አንተ የምትዘራው ካልሞተ ሕያው አይሆንም፤

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

su ko mënul, dafay yónni ndaw ca beneen buur ba, fi ak ma ngay sore, ngir ñu juboo.

Amharic

ባይሆንስ ሌላው ገና ሩቅ ሳለ መልክተኞች ልኮ ዕርቅ ይለምናል።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man na am ma yàgg ci yéen, jombul sax ma lollikoo fi yéen. noonu dingeen taxawu sama yoon, fu ma man a jëm.

Amharic

እናንተም ወደምሄድበት ወደ ማናቸውም ስፍራ በጉዞዬ እንድትረዱኝ ምናልባት በእናንተ ዘንድ እቆይ ወይም እከርም ይሆናል።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu agsee, ñu woo mbooloom ñi gëm, nettali leen fi ñu jaar ak yàlla fépp, ak ni mu ubbee buntu ngëm ci ñi dul yawut.

Amharic

በደረሱም ጊዜ ቤተ ክርስቲያኑን ሰብስበው እግዚአብሔር ከእነርሱ ጋር ያደረገውን ሁሉ ለአሕዛብም የሃይማኖትን ደጅ እንደ ከፈተላቸው ተናገሩ።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag bàkkaar ci kenn nit la jaar, dugg ci àddina, indaale fi dee, te dee daldi law ci nit ñépp, ndaxte ñépp a bàkkaar.

Amharic

ስለዚህ ምክንያት ኃጢአት በአንድ ሰው ወደ ዓለም ገባ በኃጢአትም ሞት፥ እንደዚሁም ሁሉ ኃጢአትን ስላደረጉ ሞት ለሰው ሁሉ ደረሰ፤

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

daldi ne jaaykati pitax ya: «jëleleen fi lii! sama kër baay, buleen ko def marse!»

Amharic

ርግብ ሻጪዎችንም። ይህን ከዚህ ውሰዱ፤ የአባቴን ቤት የንግድ ቤት አታድርጉት አላቸው።

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,782,200,032 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK