Results for bakkanam translation from Wolof to Arabic

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Arabic

Info

Wolof

te nit, lu mu war a weccee bakkanam?

Arabic

او ماذا يعطي الانسان فداء عن نفسه.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte moom àddina sépp, lu muy jariñ nit, bu ñàkkee bakkanam?

Arabic

لانه ماذا ينتفع الانسان لو ربح العالم كله وخسر نفسه.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«man maay sàmm bu baax bi. sàmm bu baax bi day joxe bakkanam ngir ay xaram.

Arabic

انا هو الراعي الصالح. والراعي الصالح يبذل نفسه عن الخراف.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mi joxe bakkanam ngir jot ñépp. loolu mooy seede si yàlla joxe, bi waxtu wi jotee.

Arabic

الذي بذل نفسه فدية لاجل الجميع الشهادة في اوقاتها الخاصة

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku bëgg bakkanam dina ko ñàkk, waaye ku ko bañ ci àddina sii, dina ko denc ngir dund gu dul jeex gi.

Arabic

من يحب نفسه يهلكها ومن يبغض نفسه في هذا العالم يحفظها الى حياة ابدية.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen nag góor ñi, na ku nekk bëgg jabaram, ni kirist bëgge mbooloo mi, ba joxe bakkanam ndax moom,

Arabic

ايها الرجال احبوا نساءكم كما احب المسيح ايضا الكنيسة واسلم نفسه لاجلها

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te moo joxe bakkanam, ngir dindi sunuy bàkkaar, te du sax sunuy bàkkaar rekk, waaye yu àddina sépp.

Arabic

وهو كفارة لخطايانا. ليس لخطايانا فقط بل لخطايا كل العالم ايضا

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

joxe na bakkanam ngir nun, ba jot nu ci lépp lu bon, te beral nu boppam, di xeet wu sell te ràññiku ci jëf yu baax.

Arabic

الذي بذل نفسه لاجلنا لكي يفدينا من كل اثم ويطهر لنفسه شعبا خاصّا غيورا في اعمال حسنة.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moom mi joxe bakkanam ngir dindi sunuy bàkkaar, te musal nu ci àddina su bon, si nu nekk, dëppook coobareg yàlla sunu baay,

Arabic

الذي بذل نفسه لاجل خطايانا لينقذنا من العالم الحاضر الشرير حسب ارادة الله وابينا

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñenn ca jawriñi nguur gi it, ñuy ay xaritam, yónnee ci moom, di ko dénk, mu bañ a jaay bakkanam ci dugg ca powukaay ba.

Arabic

‎واناس من وجوه اسيا كانوا اصدقاءه ارسلوا يطلبون اليه ان لا يسلم نفسه الى المشهد‎.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci toroxteem nangu nañu dëggam;ñi mu tollool jamono, ku ci xalaat lii?jële nañu bakkanam ci àddina.»

Arabic

‎في تواضعه انتزع قضاؤه وجيله من يخبر به لان حياته تنتزع من الارض‎.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

lii mooy mbëggeel, du sunu mbëggeel ci yàlla, waaye mbëggeelam ci nun, ba mu yónni doomam, mu joxe bakkanam, ngir dindi sunuy bàkkaar.

Arabic

في هذه هي المحبة ليس اننا نحن احببنا الله بل انه هو احبنا وارسل ابنه كفارة لخطايانا

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte erodd dafa ragal yaxya, ba sàmm bakkanam, xam ne ku jub la te sell. bu ko daan déglu it, day jaaxle lool, teewul mu bég ci déglu ko.

Arabic

لان هيرودس كان يهاب يوحنا عالما انه رجل بار وقديس وكان يحفظه. واذ سمعه فعل كثيرا وسمعه بسرور.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«képp ku ñëw ci man te gënalu ma ko baayam, yaayam, jabaram, ay doomam, ay magam ak ay rakkam, walla sax bakkanam, du man a nekk sama taalibe.

Arabic

ان كان احد يأتي اليّ ولا يبغض اباه وامه وامرأته واولاده واخوته واخواته حتى نفسه ايضا فلا يقدر ان يكون لي تلميذا.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

daajaale nañu ma ak kirist ca bant ba, te noonu du man may dundati, waaye kirist mooy dund ci man. dundu mbindeef, gi may dund nag, maa ngi koy dund ci gëm doomu yàlla ji, moom mi ma bëgg, ba joxe bakkanam ngir man.

Arabic

مع المسيح صلبت فاحيا لا انا بل المسيح يحيا فيّ. فما احياه الآن في الجسد فانما احياه في الايمان ايمان ابن الله الذي احبني واسلم نفسه لاجلي

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,774,316,288 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK