From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
Ñu daldi diisoo nag, jënd ca xaalis ba toolu defarkatu ndaa ya, ngir di fa suul doxandéem ya.
men efter at have holdt råd købte de pottemagermarken derfor til gravsted for de fremmede.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bésu noflaay bu nekk nag muy diisoo ak ñi nekk ca jàngu ba, di jéem a gëmloo ay yawut ak ay gereg.
men han holdt samtaler i synagogen på hver sabbat og overbeviste jøder og grækere.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
moo tax ma ñaan a gise ak yéen, nu diisoo, ndaxte yaakaaru bànni israyil moo tax ñu jéng ma.»
af denne Årsag har jeg altså ladet eder kalde hid for at se og tale med eder; thi for israels håbs skyld er jeg sluttet i denne lænke."
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
noonu ñu teer ci efes. pool bàyyi fa ñi mu àndaloon, daldi dugg ca jàngu ba, di diisoo ak yawut ya.
men de kom til efesus; og der lod han hine blive tilbage; men han selv gik ind i synagogen og samtalede med jøderne.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu saraxalekat ya dajaloo ak njiit ya, ñu diisoo; ba noppi ñu fab xaalis bu bare, jox ko xarekat ya,
og de samledes med de Ældste og holdt råd og gave stridsmændene rigelige penge
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu pool dugg ca jàngu ba, di wax ak fit wu dëgër diirub ñetti weer, di diisoo ak ñoom ci mbirum nguurug yàlla, di leen jéem a gëmloo.
og han gik ind i synagogen og vidnede frimodigt i tre måneder, idet han holdt samtaler og overbeviste om det, som hører til guds rige.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
pool ak barnabas nag am ak ñoom diisoo ak werante wu metti; noonu bokk yi jàpp ne, pool ak barnabas ak ñeneen ci ñoom war nañoo dem yerusalem ca ndaw ya ak njiit ya, ngir leeral werante wi.
da nu paulus og barnabas kom i en ikke ringe splid og strid med dem, så besluttede man, at paulus og barnabas og nogle andre af dem skulde drage op til jerusalem til apostlene og de Ældste i anledning af dette spørgsmål.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye bi xolu ñenn ci ñoom fattee, ñu gëmadi, bay suufeel yoon wi ci kanam mbooloo ma, mu jóge ci ñoom, xàjjale taalibe yi ak ñoom, di diisoo bés bu nekk ca jàngukaayu ku ñuy wax tiranus.
men da nogle forhærdede sig og strede imod og over for mængden talte ilde om vejen, forlod han dem og skilte disciplene fra dem og holdt daglig samtaler i tyrannus's skole.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw ay coonoom, ñëw na ci ñoom, di leen won ay firnde yu bare te wér ne mu ngi dund; mu feeñu leen diirub ñeent-fukki fan, di diisoo ak ñoom ci lu jëm ci nguuru yàlla.
for hvem han også, efter at han havde lidt, fremstillede sig levende ved mange beviser, idet han viste sig for dem i fyrretyve dage og talte om de ting, der høre til guds rige.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: