Results for seedes translation from Wolof to Danish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Danish

Info

Wolof

seen yoon dafa wax ne, seedes ñaari nit a gën a wóor.

Danish

men også i eders lov er der skrevet, at to menneskers vidnesbyrd er sandt.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man ci sama bopp soxlawuma seedes nit; waaye nag damay wax loolu rekk, ngir ngeen mucc.

Danish

dog, jeg henter ikke vidnesbyrdet fra et menneske; men dette siger jeg, for at i skulle frelses.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fekk noot nañu kojaarale ko ci deretu mbote maak seen seedes ngëm,te soppuñu seen bakkan ba ragal a dee.

Danish

og de have overvundet ham i kraft af lammets blod og i kraft af deres vidnesbyrds ord; og de elskede ikke deres liv, lige til døden.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bii mooy ñetteel bi yoon, ma di leen ganesi. «bépp àtte dina aju ci seedes ñaar walla ñetti nit.»

Danish

det er nu tredje gang, jeg kommer til eder. på to og tre vidners mund skal enhver sag stå fast.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

lii mooy seedes yaxya. amoon na bés yawut ya yónni ay saraxalekat ca yaxya, ñu ànd ak ñu soqikoo ci giiru lewi. Ñu nga jóge yerusalem, ñëw ci moom, di ko laaj mooy kan.

Danish

og dette er johannes's vidnesbyrd, da jøderne sendte præster og leviter ud fra jerusalem, for at de skulde spørge ham: "hvem er du?"

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Wolof

noonu ma daanu ci ay tànkam, bëgg koo jaamu. waaye mu ne ma: «moytu koo def; sa nawle laa ci liggéey bi, di kenn ci say bokk, yiy sax ci seedeel yeesu. jaamul yàlla. ndaxte seedes yeesu mooy xel miy solu yonent yi.»

Danish

og jeg faldt ned for hans fødder for at tilbede ham, og han siger til mig: gør det ikke! jeg er din medtjener eg dine brødres, som have jesu vidnesbyrd; tilbed gud! thi jesu vidnesbyrd er profetiens Ånd.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,792,670,392 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK