From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
yéen demaguleen ba tuur seen deret ci seen bëre ak bàkkaar.
ye have not yet resisted unto blood, striving against sin.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
loolu moo tax ñu wooye tool booba ba tey toolu deret.
wherefore that field was called, the field of blood, unto this day.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
looloo waral kóllëre gu jëkk ga, ñu fasoon ko ak deret.
whereupon neither the first testament was dedicated without blood.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
sol na mbubb mu ñu sóob ci deret, te kàddug yàlla mooy turam.
and he was clothed with a vesture dipped in blood: and his name is called the word of god.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci saa si deret ji taxaw, mu yég ci yaramam ne, jàngoroom deñ na.
and straightway the fountain of her blood was dried up; and she felt in her body that she was healed of that plague.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu mu daldi wis it deret ja ca tànt ba ak ca jumtukaay, ya ñu daan jaamoo.
moreover he sprinkled with blood both the tabernacle, and all the vessels of the ministry.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñetteelu malaaka ma sotti ndabam ci dex yi ak ci bëti ndox yi. Ñu daldi nekk deret.
and the third angel poured out his vial upon the rivers and fountains of waters; and they became blood.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci biir tiis, yeesu gën a sawar ci ñaan gi, ñaqam mel ni lumbi deret dal ci suuf.
and being in an agony he prayed more earnestly: and his sweat was as it were great drops of blood falling down to the ground.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
jigéen ja jegeñsi yeesu nag, doxe ko gannaaw, laal catu mbubbam. ca saa sa deret ji dal.
came behind him, and touched the border of his garment: and immediately her issue of blood stanched.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye kenn ca xarekat ya daldi jël xeej, jam ko ko ci wet, ca saa sa deret ak ndox di tuuru.
but one of the soldiers with a spear pierced his side, and forthwith came there out blood and water.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
dinaa wone ay kéemaan ci kaw ci asamaanak ay firnde ci suuf ci àddina,muy deret, safara ak ay niiri saxar.
and i will shew wonders in heaven above, and signs in the earth beneath; blood, and fire, and vapour of smoke:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
di ñu maandu, sell te fonk seen kër, ñu neex deret te déggal seeni jëkkër, ngir kenn bañ cee gàkkal kàddug yàlla.
to be discreet, chaste, keepers at home, good, obedient to their own husbands, that the word of god be not blasphemed.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ngëm moo tax mu sos màggalu bésu jéggi ba, di wis deret ci bunt yi, ngir malaakam yàqkat mi bañ a laal taawi bànni israyil.
through faith he kept the passover, and the sprinkling of blood, lest he that destroyed the firstborn should touch them.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
na leen yàlla boroom jàmm, mi dekkal sunu boroom yeesu, di sàmm bu mag bi, ci darajay deret, ji fas kóllëre gu sax,
now the god of peace, that brought again from the dead our lord jesus, that great shepherd of the sheep, through the blood of the everlasting covenant,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñuy xaacu naan: «boroom bu sell bi te dëggu, ba kañ ngay nég àtte bi te feyyul nu sunu deret ci waa àddina?»
and they cried with a loud voice, saying, how long, o lord, holy and true, dost thou not judge and avenge our blood on them that dwell on the earth?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
loolu siiwoon na ci waa yerusalem, moo tax ci seen làkk ñuy tudde tool ba akeldama, maanaam «toolu deret.» —
and it was known unto all the dwellers at jerusalem; insomuch as that field is called in their proper tongue, aceldama, that is to say, the field of blood.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
saraxalekat bu mag bi dafay dugg at mu jot ca bérab bu sell-baa-sell ak deret ju dul josam. waaye kirist joxewul bakkanam ay yooni yoon.
nor yet that he should offer himself often, as the high priest entereth into the holy place every year with blood of others;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca jamono jooju ay nit ñëw ca yeesu, nettali mbirum waa galile, ya pilaat reylu woon, jaxase seen deret ak dereti mala, yi ñu rendi woon, jébbal leen yàlla.
there were present at that season some that told him of the galilaeans, whose blood pilate had mingled with their sacrifices.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
malaaka mu jëkk ma wol liitam. noonu ñu sànni ci àddina yuur ak safara yu ñu boole ak deret, ba tax benn ci ñetti xaaju suuf si lakk, benn ci ñetti xaaju garab yi it lakk, te ñax mu naat mépp lakk.
the first angel sounded, and there followed hail and fire mingled with blood, and they were cast upon the earth: and the third part of trees was burnt up, and all green grass was burnt up.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
am nañu sañ-sañu téye taw diirub fan, yi ñuy wax ci kàddug yàlla. am nañu it sañ-sañu soppi ndox yi deret te wàcce ci kaw suuf musiba yu nekk, saa su ñu ko bëggee.
these have power to shut heaven, that it rain not in the days of their prophecy: and have power over waters to turn them to blood, and to smite the earth with all plagues, as often as they will.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: