From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
bi festus teersee ci diiwaanam, mu teg ca ñetti fan, dem yerusalem.
now when festus was come into the province, after three days he ascended from caesarea to jerusalem.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ba ñu ca tegee ay fan, buur agaripa ak berenis ñëw sesare, ngir nuyusi festus.
and after certain days king agrippa and bernice came unto caesarea to salute festus.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te agaripa ne festus: «manoon nanu koo yiwi, bu dénkuloon mbiram sesaar.»
then said agrippa unto festus, this man might have been set at liberty, if he had not appealed unto caesar.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi seen ngan di ruus nag, festus diis buur ba mbirum pool ne ko: «feligsë batale na nu ak kenn ku ñu tëj.
and when they had been there many days, festus declared paul's cause unto the king, saying, there is a certain man left in bonds by felix:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye pool tontu ko: «festus mu tedd mi, dofuma; waaye lu dëggu laay wax te ànd ak sago.
but he said, i am not mad, most noble festus; but speak forth the words of truth and soberness.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye festus tontu leen ne: «Ñu ngi wottu pool ca sesare, te dinaa fa dem fi ak fan yu néew.»
but festus answered, that paul should be kept at caesarea, and that he himself would depart shortly thither.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca ëllëg sa nag agaripa ak berenis ñëw bu xumb, ñu dugg ca néegu àtte ba, ànd ak kilifay xare ba ak ña am maana ca dëkk ba. noonu festus joxe ndigal, ñu indi pool.
and on the morrow, when agrippa was come, and bernice, with great pomp, and was entered into the place of hearing, with the chief captains, and principal men of the city, at festus' commandment paul was brought forth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi mu waxee loolu, festus gise ak ñi ko wër, mu tontu ko: «dénk nga sa mbir sesaar, kon ci moom ngay dem.»
then festus, when he had conferred with the council, answered, hast thou appealed unto caesar? unto caesar shalt thou go.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci kaw loolu festus, mi bëgg lu neex yawut ya, tontu pool ne: «ndax bëgguloo dem yerusalem, nga layoo fa ci mbir yii ci sama kanam?»
but festus, willing to do the jews a pleasure, answered paul, and said, wilt thou go up to jerusalem, and there be judged of these things before me?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi muy làyyee nii, festus daldi ko gëdd ak baat bu kawe ne ko: «dangaa dof pool! xanaa sa njàng mu réy mi da laa xañ sago.»
and as he thus spake for himself, festus said with a loud voice, paul, thou art beside thyself; much learning doth make thee mad.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
booba nag agaripa ne festus: «man sax bëgg naa dégg nit kooku.» festus tontu ko: «bu ëllëgee dinga ko dégg.»
then agrippa said unto festus, i would also hear the man myself. to morrow, said he, thou shalt hear him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: