From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
waaye képp ku dégg lii ma leen wax, te jëfewuloo ko, dinga mel ni nit ku ñàkk xel, ku tabax këram ci gànnuus bi.
and every one that heareth these sayings of mine, and doeth them not, shall be likened unto a foolish man, which built his house upon the sand:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye képp ku dégg samay wax te jëfewuloo ko, dinga mel ni nit ku tabax këram ci suuf, bañ koo defal fondamaa. bi wal ma dalee ca kër googa, dafa màbb ca saa sa, lépp yàqu yaxeet.»
but he that heareth, and doeth not, is like a man that without a foundation built an house upon the earth; against which the stream did beat vehemently, and immediately it fell; and the ruin of that house was great.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: