From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
bu leen yàlla di may xelam, di leen won jalooreem, ndax li ngeen sàmm yoon a tax, mu def ko, mbaa li ngeen dégg xebaar bu baax te gëm ko?
he therefore that ministereth to you the spirit, and worketh miracles among you, doeth he it by the works of the law, or by the hearing of faith?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye erodd ne: «yaxya, man mii maa dagglu boppam. kon kii ma dégg ay jalooreem, mooy kan?» noonu mu koy fexee gis.
and herod said, john have i beheaded: but who is this, of whom i hear such things? and he desired to see him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: