From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
waaye ku ma gàntu ci kanamu nit ñi, dinañu la gàntu ci kanamu malaakay yàlla yi.
but he that denieth me before men shall be denied before the angels of god.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
maa ngi leen di wax lii: ci noonule la malaakay yàlla yi di ame mbég ci benn bàkkaarkat bu tuubee ay bàkkaaram.»
likewise, i say unto you, there is joy in the presence of the angels of god over one sinner that repenteth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«te maa ngi leen koy wax, képp ku ma nangu ci kanamu nit ñi, doomu nit ki dina la nangu ci kanamu malaakay yàlla yi.
also i say unto you, whosoever shall confess me before men, him shall the son of man also confess before the angels of god:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
mu nekk fa ñeent-fukki fan, jànkoonte ak fiiri seytaane; mu dëkk ci biir rabi àll yi, te malaakay yàlla di ko topptoo.
and he was there in the wilderness forty days, tempted of satan; and was with the wild beasts; and the angels ministered unto him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
juróom-ñaari biddiiw yi nga gis ci sama loxol ndeyjoor, ak juróom-ñaari làmpi diwlin yu wurus yi, ay mbóoti yàlla lañu te lii lañuy tekki: biddiiw yi ñoo di malaakay juróom-ñaari mboolooy ñi gëm; juróom-ñaari làmp yi ñoo di juróom-ñaari mbooloo yi.
the mystery of the seven stars which thou sawest in my right hand, and the seven golden candlesticks. the seven stars are the angels of the seven churches: and the seven candlesticks which thou sawest are the seven churches.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: