Results for mane ak yaw translation from Wolof to English

Wolof

Translate

mane ak yaw

Translate

English

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

xëy na sax dafa tàggoo woon ak yaw diir bu gàtt, ngir nga jotaat ci ba fàww;

English

for perhaps he therefore departed for a season, that thou shouldest receive him for ever;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu tontu ko: «maa di almasi bi, man miy wax ak yaw.»

English

jesus saith unto her, i that speak unto thee am he.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu ne ko: «gis nga ko ba noppi, te mooy kiy wax ak yaw.»

English

and jesus said unto him, thou hast both seen him, and it is he that talketh with thee.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

piyeer ne ko: «boroom bi, àttan naa ànd ak yaw ca kaso, ba ci dee sax.»

English

and he said unto him, lord, i am ready to go with thee, both into prison, and to death.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte maa ngi ànd ak yaw, te kenn du la jàpp, ba fitnaal la, ndaxte am naa xeet wu bare ci dëkk bii.»

English

for i am with thee, and no man shall set on thee to hurt thee: for i have much people in this city.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu kenn nit ne ko: «sa yaay ak say rakk ñu ngi nii taxaw ci biti, bëgg a wax ak yaw.»

English

then one said unto him, behold, thy mother and thy brethren stand without, desiring to speak with thee.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

malaaka ma dikk ca moom ne ko: «jàmm ngaam, yaw mi boroom bi defal aw yiw; mu ngi ak yaw.»

English

and the angel came in unto her, and said, hail, thou that art highly favoured, the lord is with thee: blessed art thou among women.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

malaaka ma tontu ko ne: «man maay jibril miy taxaw ci kanam yàlla. dañu maa yónni ngir ma wax ak yaw te yégal la xebaar bu baax boobu.

English

and the angel answering said unto him, i am gabriel, that stand in the presence of god; and am sent to speak unto thee, and to shew thee these glad tidings.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

piyeer tontu ko: «boo xamee ne sax, damaa war a dee ak yaw, duma la weddi mukk.» taalibe yépp it waxe noonu.

English

peter said unto him, though i should die with thee, yet will i not deny thee. likewise also said all the disciples.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu ne ko: «loo bëggoon?» mu tontu ko ne: «damaa bëggoon nga santaane ne, boo nekkee ci sa nguur, sama ñaari doom ñii toog ak yaw, kenn ci sa ndeyjoor, ki ci des ci sa càmmooñ.»

English

and he said unto her, what wilt thou? she saith unto him, grant that these my two sons may sit, the one on thy right hand, and the other on the left, in thy kingdom.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
8,781,920,604 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK