From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
xam naa say jëf, xam ne seddoo, tàngoo. manoon ngaa sedd mbaa nga tàng,
i know thy works, that thou art neither cold nor hot: i would thou wert cold or hot.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ba tey manoon naa am yaakaar ci sama bopp; su nit doon damu, maa ciy raw.
though i might also have confidence in the flesh. if any other man thinketh that he hath whereof he might trust in the flesh, i more:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te agaripa ne festus: «manoon nanu koo yiwi, bu dénkuloon mbiram sesaar.»
then said agrippa unto festus, this man might have been set at liberty, if he had not appealed unto caesar.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
céy bu ngeen ma manoon a muñal, ma wax leen tuuti waxi dof! waaw muñal-leen ma sax.
would to god ye could bear with me a little in my folly: and indeed bear with me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te dina nas bépp naxe buy sànke, ba yéem ñi nar a alku, ndaxte ubbiluñu seeni xol dëgg, gi leen manoon a musal.
and with all deceivableness of unrighteousness in them that perish; because they received not the love of the truth, that they might be saved.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu yeesu dem ci kanam tuuti, daanu ci suuf, di ñaan ne, waxtu wi teggi ko, bu loolu manoon a am.
and he went forward a little, and fell on the ground, and prayed that, if it were possible, the hour might pass from him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
manoon nanoo diis ci seen kaw sax, nun ñiy ndawi kirist, waaye woyofoon nanu ci seen biir, te lewet ni jaboot buy uuf doomam.
but we were gentle among you, even as a nurse cherisheth her children:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaw, fan la seen mbég jaar? ndaxte seedeel naa leen ne, su ngeen ko manoon, kon luqi ngeen seeni bët, jox ma.
where is then the blessedness ye spake of? for i bear you record, that, if it had been possible, ye would have plucked out your own eyes, and have given them to me.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte ñi mbubboo turu kirist ak ñi mbubboo turu yonent dinañu feeñ, di joxe ay firnde yu réy ak ay kéemaan, ba ciy nax sax ñi yàlla tànn, su loolu manoon a am.
for there shall arise false christs, and false prophets, and shall shew great signs and wonders; insomuch that, if it were possible, they shall deceive the very elect.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yoon wi laajul ngëm. mbind mi nee na: «ku manoon a matal li yoon wi wax, kon dinga dund ba fàww.»
and the law is not of faith: but, the man that doeth them shall live in them.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ku bëgg a jub ci kanam yàlla ci kaw sàmm yoon, musaa daf cee wax ne: «ku ko manoon a matal, dinga dund ba fàww.»
for moses describeth the righteousness which is of the law, that the man which doeth those things shall live by them.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
jox nañu bànni israyil yoon wu sukkandiku ci liggéeyu saraxalekat yi soqikoo ci lewi. su fekkoonte ne nag liggéeyu saraxalekat yooyu manoon na yeggale nit cig mat, kon du soxlaati ab saraxalekat ni ko melkisedeg nekke, ci fànn gu wuute ak gu aaroona.
if therefore perfection were by the levitical priesthood, (for under it the people received the law,) what further need was there that another priest should rise after the order of melchisedec, and not be called after the order of aaron?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: