From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
Àtte bi ko mbooloo mi teg, doy na.
sufficient to such a man is this punishment, which was inflicted of many.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
mbooloo mu bare topp ko, mu faj leen fa.
and great multitudes followed him; and he healed them there.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi mu waxee loolu nag, mu tas mbooloo ma.
and when he had thus spoken, he dismissed the assembly.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
mbooloo ma laaj ko ne: «lan lanu war a def nag?»
and the people asked him, saying, what shall we do then?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
naka la gumba ga dégg mbooloo di jàll, mu laaj lan moo xew.
and hearing the multitude pass by, he asked what it meant.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye mbooloo mi xamuñu yoonu musaa; ñu alku lañu!»
but this people who knoweth not the law are cursed.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw loolu yeesu génn yeriko, te mbooloo mu bare topp ko.
and as they departed from jericho, a great multitude followed him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
naka la mbooloo mi gis yeesu, ñu waaru, daldi daw nuyu ko.
and straightway all the people, when they beheld him, were greatly amazed, and running to him saluted him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw loolu yeesu waxoon na mbooloo ma ak taalibeem ya ne leen:
then spake jesus to the multitude, and to his disciples,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte mbooloo maa nga ko topp, di xaacu ne: «reyleen ko!»
for the multitude of the people followed after, crying, away with him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi nga xamee ne mbooloo ma dégg nañu loolu, ñu waaru ndax li mu jàngale.
and when the multitude heard this, they were astonished at his doctrine.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu yeesu ànd ak moom. bi muy dem, mbooloo mu réy topp ko, di ko tanc.
and jesus went with him; and much people followed him, and thronged him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bind naa mbooloo mi bataaxel, waaye jotref, mi bëgg noot ñépp, du dégg sunu ndigal.
i wrote unto the church: but diotrephes, who loveth to have the preeminence among them, receiveth us not.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu ci lu jafe yey nañu mbooloo ma ak wax jooju, ba tere leen, ñu rendil leen sarax.
and with these sayings scarce restrained they the people, that they had not done sacrifice unto them.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi yeesu gisee mbooloo ma nag, mu yéeg ca tund wa, toog; taalibeem ya ñëw ci moom.
and seeing the multitudes, he went up into a mountain: and when he was set, his disciples came unto him:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yéen itam, gannaaw dangeen a fonk mayi xelum yàlla, jéemleen a ëpple ci liy yokk ngëmu mbooloo mi.
even so ye, forasmuch as ye are zealous of spiritual gifts, seek that ye may excel to the edifying of the church.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
su amul kuy firi, kooku di wax aw làkk, na noppi ci ndajem mbooloo mi. na waxanteek yàlla ci xolam.
but if there be no interpreter, let him keep silence in the church; and let him speak to himself, and to god.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw loolu yeesu ak ay taalibeem jóge fa, jëm dex ga. fekk mbooloo mu mag mu jóge diiwaanu galile, topp ko.
but jesus withdrew himself with his disciples to the sea: and a great multitude from galilee followed him, and from judaea,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
piyeer ne yeesu: «boroom bi, ndax dangay dégtal léeb wii ngir nun rekk walla ngir mbooloo mépp?»
then peter said unto him, lord, speakest thou this parable unto us, or even to all?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nee na:«yaw yàlla, dinaa xamle sa turci samay doomi baay,dinaa la tagg ci biir mbooloo mi.»
saying, i will declare thy name unto my brethren, in the midst of the church will i sing praise unto thee.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: