Results for ngi translation from Wolof to English

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

moo tax maa ngi sukk, jublu ci yàlla baay

English

for this cause i bow my knees unto the father of our lord jesus christ,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mboolem gaayi yàlla yépp ñu ngi leen di nuyu.

English

all the saints salute you.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag maa ngi leen di ñaan, ngeen roy ci man.

English

wherefore i beseech you, be ye followers of me.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

benn bésu noflaay yeesoo ngi doon jàngale ci ab jàngu.

English

and he was teaching in one of the synagogues on the sabbath.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

maa ngi wax ak yéen ñi am xel. kon seetleen li ma leen wax.

English

i speak as to wise men; judge ye what i say.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yoon wu ma leen di xalaat, maa ngi sant yàlla sama boroom;

English

i thank my god upon every remembrance of you,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

jógleen nu dem; ki may wor a ngi nii, di ñëw.»

English

rise up, let us go; lo, he that betrayeth me is at hand.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye nag ibraaymaa ngi doon séentu dëkk bi sax, bi yàlla tabax te sanc ko.

English

for he looked for a city which hath foundations, whose builder and maker is god.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku farul ak man, yaa ngi may xeex, ku dajalewul ak man, yaa ngi tasaare.

English

he that is not with me is against me: and he that gathereth not with me scattereth.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte fu ñaar walla ñetti nit booloo ci sama tur, maa ngi ci seen biir.»

English

for where two or three are gathered together in my name, there am i in the midst of them.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

doomu nit ki mu ngi dem, ni ñu ko dogale. waaye ki koy wor dina torox.»

English

and truly the son of man goeth, as it was determined: but woe unto that man by whom he is betrayed!

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye pool wax ci kaw ne: «bul lor sa bopp, nun ñépp nu ngi fi.»

English

but paul cried with a loud voice, saying, do thyself no harm: for we are all here.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye mu tontu leen ne: “ci dëgg maa ngi leen koy wax, xawma leen.”

English

but he answered and said, verily i say unto you, i know you not.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñooñu judduwuñu ci deret walla ci bëgg-bëggu yaram, walla ci coobarey nit. Ñu ngi juddu ci yàlla.

English

which were born, not of blood, nor of the will of the flesh, nor of the will of man, but of god.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«buleen ragal, waa siyon.gis ngeen, seen buur a ngi ñëw,war mbaam mu ndaw.»

English

fear not, daughter of sion: behold, thy king cometh, sitting on an ass's colt.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pilaat tontu leen: «amleen, ay wottukat a ngi nii. demleen wottuji ko, ni ngeen mane.»

English

pilate said unto them, ye have a watch: go your way, make it as sure as ye can.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,882,807,238 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK