From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
te ku bëgg a nekk njiit, na nekk seen jaam.
and whosoever of you will be the chiefest, shall be servant of all.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu ndaw yi ak njiit yi dajaloo, ngir seet mbir moomu.
and the apostles and elders came together for to consider of this matter.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca ëllëg sa pool ànd ak nun, seeti saag, fekk njiit yépp teew fa.
and the day following paul went in with us unto james; and all the elders were present.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye njiit la sobental waxi pool, déggal dawalkat ba ak boroom gaal ga.
nevertheless the centurion believed the master and the owner of the ship, more than those things which were spoken by paul.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu lañu def nag, teg ko ci loxoy barnabas ak sool, yónnee ko njiit ya.
which also they did, and sent it to the elders by the hands of barnabas and saul.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
man njiit li, maa ngi lay bind, yaw sama xarit gayus, mi ma bëgg ci sama xol.
the elder unto the wellbeloved gaius, whom i love in the truth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
naka lañu ñëw ci kër njiit li, yeesu dégg coow li; ñii di jooy, ñii di yuuxu.
and he cometh to the house of the ruler of the synagogue, and seeth the tumult, and them that wept and wailed greatly.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ña jàppoon yeesu yóbbu ko kër kayif, saraxalekat bu mag ba, fa xutbakat ya ak njiit ya daje.
and they that had laid hold on jesus led him away to caiaphas the high priest, where the scribes and the elders were assembled.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
buñu leen tudde it ay “njiit,” ndaxte kenn rekk moo di seen njiit, mooy kirist.
neither be ye called masters: for one is your master, even christ.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bul sàggane may gi nekk ci yaw, gi la yàlla jox jaarale ko ci waxu yonent, keroog bi la njiit yi tegee loxo.
neglect not the gift that is in thee, which was given thee by prophecy, with the laying on of the hands of the presbytery.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yéen buleen def noonu. ki gën a màgg ci yéen, na nekk ni ki gën a ndaw, te njiit mel ni surga.
but ye shall not be so: but he that is greatest among you, let him be as the younger; and he that is chief, as he that doth serve.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw loolu ñu duggaat yerusalem, te yeesu doon doxantu ca ëtti kër yàlla ga. noonu saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya dab ko
and they come again to jerusalem: and as he was walking in the temple, there come to him the chief priests, and the scribes, and the elders,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi pilaat déggee ne, yeesu faatu na xaat, mu waaru. mu woolu nag njiit li, laaj ko, ndax yàgg na faatu.
and pilate marvelled if he were already dead: and calling unto him the centurion, he asked him whether he had been any while dead.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
su ngeen amee junniy njiit yu leen di sàmm ci kirist, ba tey benn baay rekk ngeen am, ndaxte maa leen yégal xebaar bu baax bi, ba jur leen ci kirist.
for though ye have ten thousand instructors in christ, yet have ye not many fathers: for in christ jesus i have begotten you through the gospel.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
fekk na ci biir njiit yi sax, ñu bare gëmoon nañu yeesu, waaye farisen yee tax fésaluñu ko, ndaxte dañoo ragaloon, ñu dàq leen ca jàngu ba.
nevertheless among the chief rulers also many believed on him; but because of the pharisees they did not confess him, lest they should be put out of the synagogue:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
“yaw betleyem ci diiwaanu yude,du yaw yaa yées ci njiiti yude,ndaxte ci yaw la njiit di génne,kiy sàmm israyil sama xeet.”»
and thou bethlehem, in the land of juda, art not the least among the princes of juda: for out of thee shall come a governor, that shall rule my people israel.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw loolu bokk yi, ci lu jëm ci njiit, yi boroom bi teg ci seen kanam te ñuy liggéey ci seen biir, di leen artu, maa ngi leen di ñaan ngeen déglu leen;
and we beseech you, brethren, to know them which labour among you, and are over you in the lord, and admonish you;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nun pool ak timote, jaami kirist yeesu, noo leen di bind, yéen gaayi yàlla yu sell yépp ci dëkku filib, yi bokk ci kirist yeesu, yéen ak seeni njiit ak ñiy topptoo yëfi mbooloo mi.
paul and timotheus, the servants of jesus christ, to all the saints in christ jesus which are at philippi, with the bishops and deacons:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi ko njiit ya déggee, ñu màggal yàlla ne ko: «mbokk mi, gis nga ne, am na ay junniy yawut ñu gëm, te ñépp a sawar ci yoonu musaa.
and when they heard it, they glorified the lord, and said unto him, thou seest, brother, how many thousands of jews there are which believe; and they are all zealous of the law:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi mu ko waxee, ndaw yi ak njiit yi ak mbooloom ñi gëm mépp fas yéenee tànn ci ñoom ay nit, yónni leen ancos, ñu ànd ak pool ak barnabas. noonu ñu tànn yudd, mi ñuy dippee barsabas, ak silas, di ay njiit ca bokk ya.
then pleased it the apostles and elders, with the whole church, to send chosen men of their own company to antioch with paul and barnabas; namely, judas surnamed barsabas, and silas, chief men among the brethren:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: