From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
waaye defleen lii:«bu sa noon xiifee, may ko mu lekk;bu maree, may ko mu naan.ndax boo ko defee, dinga ko rusloo.»
therefore if thine enemy hunger, feed him; if he thirst, give him drink: for in so doing thou shalt heap coals of fire on his head.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
xanaa amuleen kër yu ngeen di lekke ak di naane? walla ndax dangeen a xeeb mbooloom yàlla? walla ngeen bëgg a rusloo ñi amul dara? lu ma leen ci war a wax nag? ma gërëm leen ci loolu? mukk! gërëmuma leen.
what? have ye not houses to eat and to drink in? or despise ye the church of god, and shame them that have not? what shall i say to you? shall i praise you in this? i praise you not.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: