From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ku sa liggéey dëgër, dinga jot yool.
if any man's work abide which he hath built thereupon, he shall receive a reward.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
kon nag buleen sàggane kóolute gi ngeen am, ndaxte ëmb na yool bu mag.
cast not away therefore your confidence, which hath great recompence of reward.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
kon moytuleen, ngir baña ñàkk seen añub coono, waaye ngeen am yool bu mat sëkk.
look to yourselves, that we lose not those things which we have wrought, but that we receive a full reward.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bégleen te bànneexu, ndax seen yool dina réy ci laaxira. ndaxte noonu lañu daan fitnaale yonent yi fi jiitu.
rejoice, and be exceeding glad: for great is your reward in heaven: for so persecuted they the prophets which were before you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
su ngeen soppee ñi leen sopp, ban yool ngeen am? xanaa juutikat yi duñu def noonu it?
for if ye love them which love you, what reward have ye? do not even the publicans the same?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«wottuleen a def seeni jëf yu jub ci kanamu nit ñi, muy ngistal. lu ko moy, dungeen am yool ci seen baay bi nekk ci kaw.
take heed that ye do not your alms before men, to be seen of them: otherwise ye have no reward of your father which is in heaven.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: