From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
amal diam
amal diam
Last Update: 2024-04-15
Usage Frequency: 4
Quality:
amul woon sa njariñ démb, waaye tey amal na nu njariñ, yaw ak man.
qui autrefois t`a été inutile, mais qui maintenant est utile, et à toi et à moi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
luug rekk a des fi man. indaaleel màrk, ndaxte amal na ma njariñ ci liggéey bi.
luc seul est avec moi. prends marc, et amène-le avec toi, car il m`est utile pour le ministère.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
def na noonu, ngir amal la ñu waxoon jaarale ko ci yonent yàlla esayi, bi mu naan:
afin que s`accomplît ce qui avait été annoncé par Ésaïe, le prophète:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
loolu lépp xewoon na, ngir amal li boroom bi wax, jaarale ko cib yonent, bi mu naan:
tout cela arriva afin que s`accomplît ce que le seigneur avait annoncé par le prophète:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ci li jëm ci yoonu musaa, dee naa, fekk yoon wi ci boppam moo ko waral, ngir ma man a dund, ba amal jariñ yàlla.
car c`est par la loi que je suis mort à la loi, afin de vivre pour dieu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
«bi loolu wéyee jamono ji jege woon na, ngir yàlla amal li mu digoon ibraayma ci ngiñ; fekk xeet wa di law tey gën a bare ci misra,
le temps approchait où devait s`accomplir la promesse que dieu avait faite à abraham, et le peuple s`accrut et se multiplia en Égypte,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: