Results for baal nalaakh translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

moom mi nu jot, maanaam baal nu sunuy bàkkaar.

French

en qui nous avons la rédemption, la rémission des péchés.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te baal nu sunuy tooñ, ni nu baale ñi nu tooñ;

French

pardonne-nous nos offenses, comme nous aussi nous pardonnons à ceux qui nous ont offensés;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu sangam yërëm ko, bàyyi ko, baal ko bor ba.

French

Ému de compassion, le maître de ce serviteur le laissa aller, et lui remit la dette.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye su ngeen baalul ñi leen tooñ, seen baay it du leen baal seeni tooñ.

French

mais si vous ne pardonnez pas aux hommes, votre père ne vous pardonnera pas non plus vos offenses.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte dinaa leen baal seeni tooñ,te dootuma fàttaliku seeni bàkkaar.»

French

parce que je pardonnerai leurs iniquités, et que je ne me souviendrai plus de leurs péchés.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

réccul nag sa coxor te ñaan boroom bi, mu baal la sa xalaatu xol, su manee am.

French

repens-toi donc de ta méchanceté, et prie le seigneur pour que la pensée de ton coeur te soit pardonnée, s`il est possible;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«su ngeen baalee ñi leen tooñ, seen baay bi ci kaw dina leen baal seeni tooñ yéen itam.

French

si vous pardonnez aux hommes leurs offenses, votre père céleste vous pardonnera aussi;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, lépp dees na ko baal nit ñi, muy bàkkaar, muy sosal yàlla wu mu man a doon.

French

je vous le dis en vérité, tous les péchés seront pardonnés aux fils des hommes, et les blasphèmes qu`ils auront proférés;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te ñaan gu ànd ak ngëm dina musal ki wopp, ba boroom bi yékkati ko. te su ko fekkoon ak i bàkkaar sax, yàlla dina ko baal.

French

la prière de la foi sauvera le malade, et le seigneur le relèvera; et s`il a commis des péchés, il lui sera pardonné.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñi ngeen di baal seeni bàkkaar, baal nañu leen ba noppi; ñi ngeen baalul, baaluñu leen.»

French

ceux à qui vous pardonnerez les péchés, ils leur seront pardonnés; et ceux à qui vous les retiendrez, ils leur seront retenus.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ma wax ne: “baal nañu la say bàkkaar,” walla ma ne: “jógal te dox,” lan moo ci gën a yomb?

French

car, lequel est le plus aisé, de dire: tes péchés sont pardonnés, ou de dire: lève-toi, et marche?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,794,616,036 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK