From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
«te lii itam, bu sa mbokk defee bàkkaar, demal yedd ko, yéen ñaar rekk. bu la dégloo, kon gindi nga sa mbokk.
si ton frère a péché, va et reprends-le entre toi et lui seul. s`il t`écoute, tu as gagné ton frère.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi ñu dégloo yeesu ba noppi, taalibeem yu bare nee nañu: «njàngale mii de, jafe na! kan moo ko man a déglu?»
plusieurs de ses disciples, après l`avoir entendu, dirent: cette parole est dure; qui peut l`écouter?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
seetleen bu baax, ni ngeen di dégloo kàddu gi. ku am, dees na la dollil, waaye ku amul, dees na nangu sax li nga xalaatoon ne, am nga ko ba noppi.»
prenez donc garde à la manière dont vous écoutez; car on donnera à celui qui a, mais à celui qui n`a pas on ôtera même ce qu`il croit avoir.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: