Results for defe translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

kon nag nangeen dëgëralante te yokkante seen ngëm, ni ngeen koy defe.

French

c`est pourquoi exhortez-vous réciproquement, et édifiez-vous les uns les autres, comme en réalité vous le faites.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

buleen xultu, ni ko ñenn ñi ci ñoom defe woon, ba tax malaakam yàqkat mi rey leen.

French

ne murmurez point, comme murmurèrent quelques-uns d`eux, qui périrent par l`exterminateur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu nu seetee tiis wii fi teew nag, defe naa ne li baax ci nit, moo di mu sax ci li mu nekk.

French

voici donc ce que j`estime bon, à cause des temps difficiles qui s`approchent: il est bon à un homme d`être ainsi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw loolu yeesu daldi gëdd dëkk, ya mu defe woon la ëpp cay kéemaanam, ndaxte tuubuñu seeni bàkkaar.

French

alors il se mit à faire des reproches aux villes dans lesquelles avaient eu lieu la plupart de ses miracles, parce qu`elles ne s`étaient pas repenties.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

pool nag dugg ca ñoom, na mu ko daan defe, ba am fa ñetti bésu noflaay, muy werante ak ñoom ci li mbind mi wax.

French

paul y entra, selon sa coutume. pendant trois sabbats, il discuta avec eux, d`après les Écritures,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu ne leen: «kon man itam duma leen wax ci ban sañ-sañ laay defe yëf yii.»

French

et jésus leur dit: moi non plus, je ne vous dirai pas par quelle autorité je fais ces choses.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu bi ngelaw lu woyof liy jóge sudd wolee, ñu defe ne, man nañoo sottal seen pexe, ñu wëgg diigal, daldi tafu ci dunu kereet.

French

un léger vent du sud vint à souffler, et, se croyant maîtres de leur dessein, ils levèrent l`ancre et côtoyèrent de près l`île de crète.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu dem nasaret fa mu yaroo, te ca bésu noflaay ba, mu dugg ca jàngu ba, ni mu ko daan defe. noonu mu taxaw ngir jàngal mbooloo mi.

French

il se rendit à nazareth, où il avait été élevé, et, selon sa coutume, il entra dans la synagogue le jour du sabbat. il se leva pour faire la lecture,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,767,681,639 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK