Results for fay nala translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

beug nala

French

Last Update: 2024-05-06
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

namou nala

French

tu me manques

Last Update: 2023-08-27
Usage Frequency: 2
Quality:

Wolof

beug nala sétsi

French

comment tu vas

Last Update: 2024-04-19
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

defëkaay yu fay nañu:

French

extensions désactivées

Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bul fay %(plugin)s !

French

ne pas désactiver %(plugin)s

Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yalla nala yalla diapale

French

Last Update: 2021-01-27
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

gannaaw loolu yeesu dugg ca kër yàlla ga, daldi dàq ña fay jaay,

French

il entra dans le temple, et il se mit à chasser ceux qui vendaient,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

muy werante nag ca jàngu ba ak yawut ya ak ña ragal yàlla, tey werante it bés bu nekk ca pénc ma ak ña fay dajaloo.

French

il s`entretenait donc dans la synagogue avec les juifs et les hommes craignant dieu, et sur la place publique chaque jour avec ceux qu`il rencontrait.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

dara du fa dugg lu am sobe, mbaa kenn kuy sóobu ci ñaawteef walla fen. Ñi ñu bind ci téereb dund bu mbote mi rekk ñoo fay dugg.

French

il n`entrera chez elle rien de souillé, ni personne qui se livre à l`abomination et au mensonge; il n`entrera que ceux qui sont écrits dans le livre de vie de l`agneau.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

«léegi maa ngi nii di dem yerusalem, ci li ma xelu yàlla mi xiirtal, te xawma lu ma fay dal.

French

et maintenant voici, lié par l`esprit, je vais à jérusalem, ne sachant pas ce qui m`y arrivera;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

waaye bi yawuti tesalonig déggee ne, pool mu ngi yégle kàddug yàlla ci bere it, ñu daldi fay dikk, di jógloo ak a jaxase mbooloo ma.

French

mais, quand les juifs de thessalonique surent que paul annonçait aussi à bérée la parole de dieu, ils vinrent y agiter la foule.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Wolof

bi loolu amee ñu jox ma nattukaay bu mel ni yet, ne ma: «jógal, natt kër yàlla gi ak saraxalukaay bi, te waññ ña fay jaamu yàlla.

French

on me donna un roseau semblable à une verge, en disant: lève-toi, et mesure le temple de dieu, l`autel, et ceux qui y adorent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Reference: Anonymous

Get a better translation with
7,794,252,003 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK