Results for gatandu translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

ca suba sa yeesu ak taalibe ya wàcce ca tund wa, mbooloo mu bare ñëw, di ko gatandu.

French

le lendemain, lorsqu`ils furent descendus de la montagne, une grande foule vint au-devant de jésus.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

looloo tax it ma xalaat ne, awma darajay gatandu la. waxal genn kàddu rekk, te sama surga dina wér.

French

c`est aussi pour cela que je ne me suis pas cru digne d`aller en personne vers toi. mais dis un mot, et mon serviteur sera guéri.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi muy dellu këram nag, ay surgaam gatandu ko. Ñu daldi ne ko: «xale bi dina dund!»

French

comme déjà il descendait, ses serviteurs venant à sa rencontre, lui apportèrent cette nouvelle: ton enfant vit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«noonu ci xaaju guddi baat jib ne: “boroom séet baa ngi, génnleen, gatandu ko.”

French

au milieu de la nuit, on cria: voici l`époux, allez à sa rencontre!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

melkisedeg moomu doon buuru salem, moo nekkoon saraxalekat ca yàlla aji kawe ji. gannaaw ba ibraayma dàqee buur ya, ba dellusi, melkisedeg gatandu woon na ko, di ko barkeel.

French

en effet, ce melchisédek, roi de salem, sacrificateur du dieu très haut, -qui alla au-devant d`abraham lorsqu`il revenait de la défaite des rois, qui le bénit,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sunuy xebaar law na, ba egg ca bokk ya fa dëkk, noonu ñu gatandu nu ba ca péncu apiyus ak bérab bu ñuy wax Ñetti añukaay ya. bi leen pool gisee, mu sant yàlla, daldi takk fitam.

French

de rome vinrent à notre rencontre, jusqu`au forum d`appius et aux trois tavernes, les frères qui avaient entendu parler de nous. paul, en les voyant, rendit grâces à dieu, et prit courage.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,782,234,799 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK