From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
sangue bi
Last Update: 2023-10-20
Usage Frequency: 1
Quality:
joxoo tur dencukaay bi
aucun nom de fichier pour enregistrer
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
man ak baay bi benn lanu.»
moi et le père nous sommes un.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
hamul programa ci biir bi ... :(
backend non trouvé.
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
bi yelloo ndam ba fàww. amiin.
à qui soit la gloire aux siècles des siècles! amen!
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bu kooku yaakaar dara ci boroom bi.
qu`un tel homme ne s`imagine pas qu`il recevra quelque chose du seigneur:
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noon bu mujj, bi mu fiy jële, mooy dee.
le dernier ennemi qui sera détruit, c`est la mort.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
li dafa programa bu ogosu na compizconfig bi.
ceci est un gestionnaire de configuration pour le système de configuration compizconfig
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
nangeen mat nag, ni seen baay bi ci kaw mate.
soyez donc parfaits, comme votre père céleste est parfait.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bindal ab tudde ngir xät bu bees bi, bü là nääxë
merci d'entrer un nom pour le nouveau profil:
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
bi mu ko defee nit ñi song yeesu nag, jàpp ko.
alors ces gens mirent la main sur jésus, et le saisirent.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñu jàpp ko nag, génne ko tool bi, rey ko.»
et ils se saisirent de lui, le jetèrent hors de la vigne, et le tuèrent.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi mu waxee loolu, mu sukk ak ñoom ñépp, ñaan ci yàlla.
après avoir ainsi parlé, il se mit à genoux, et il pria avec eux tous.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi ñu agsee, ñu fekk ñu béraŋ doj, wa uboon bàmmeel ba.
elles trouvèrent que la pierre avait été roulée de devant le sépulcre;
Last Update: 2024-04-17
Usage Frequency: 3
Quality:
suufeel-leen seen bopp fa kanam boroom bi, kon dina leen yékkati.
humiliez-vous devant le seigneur, et il vous élèvera.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
jigéen ja ne ko: «sang bi, gis naa ne, ab yonent nga.
seigneur, lui dit la femme, je vois que tu es prophète.
Last Update: 2024-03-15
Usage Frequency: 2
Quality:
Ñu ne ko: “sang bi, am na fukki libidoor ba noppi.”
ils lui dirent: seigneur, il a dix mines. -
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
mënuleen a naan ci kaasu boroom bi, naan ci kaasu rab yi. mënuleen a sukk ci reerub boroom bi, sukk ci reerub rab yi.
vous ne pouvez boire la coupe du seigneur, et la coupe des démons; vous ne pouvez participer à la table du seigneur, et à la table des démons.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
filib ne ko: «boroom bi, won nu baay bi; loolu doy na nu.»
philippe lui dit: seigneur, montre-nous le père, et cela nous suffit.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: