Results for libidoor translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

Ñu ne ko: “sang bi, am na fukki libidoor ba noppi.”

French

ils lui dirent: seigneur, il a dix mines. -

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku jëkk ka ñëw ne ko: “sang bi, sa libidoor bii jur na fukki libidoor.”

French

le premier vint, et dit: seigneur, ta mine a rapporté dix mines.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

surga ba ca topp ñëw ne: “sang bi, sa libidoor ba indi na juróomi libidoor.”

French

le second vint, et dit: seigneur, ta mine a produit cinq mines.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

keneen ñëw ne: “sang bi, sa libidoor baa ngi nii. dama koo fasoon ci sekkit, denc ko.

French

un autre vint, et dit: seigneur, voici ta mine, que j`ai gardée dans un linge;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu mu woo fukk ci ay surgaam, jox ku nekk benn libidoor, ne leen: “liggéeyleen ci, ba may ñibbisi.”

French

il appela dix de ses serviteurs, leur donna dix mines, et leur dit: faites-les valoir jusqu`à ce que je revienne.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«ci kaw loolu mu ne ña taxawoon ca wetam: “nanguleen libidoor bi ci moom, jox ko boroom fukki libidoor yi.”

French

puis il dit à ceux qui étaient là: otez-lui la mine, et donnez-la à celui qui a les dix mines.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«te it bu jigéen dencoon fukki libidoor, benn réer ca, nu muy def? ndax du taal ab làmp, bale kër ga, seet fu nekk, ba gis ko?

French

ou quelle femme, si elle a dix drachmes, et qu`elle en perde une, n`allume une lampe, ne balaie la maison, et ne cherche avec soin, jusqu`à ce qu`elle la retrouve?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,789,147,855 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK