Results for meloom translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

meloom mel na ni melax, ay yéreem weex tàll ni perkaal.

French

son aspect était comme l`éclair, et son vêtement blanc comme la neige.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

day gis xar-kanamam, te su nee wërëñ, daldi fàtte meloom.

French

et qui, après s`être regardé, s`en va, et oublie aussitôt quel il était.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

làmmiñ lanuy sante boroom bi, di sunu baay, ba noppi móoloo ko nit, ñi yàlla sàkk ci meloom.

French

par elle nous bénissons le seigneur notre père, et par elle nous maudissons les hommes faits à l`image de dieu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moona noppiwul a firndeel aw meloom ci def lu baax, di leen wàcceele ci asamaan taw buy indi naataange, ba ngeen lekk ba suur, te seen xol fees ak mbég.»

French

quoiqu`il n`ait cessé de rendre témoignage de ce qu`il est, en faisant du bien, en vous dispensant du ciel les pluies et les saisons fertiles, en vous donnant la nourriture avec abondance et en remplissant vos coeurs de joie.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte ba àddina sosoo ba tey, mbiri yàlla yu nëbbu ya, maanaam dooleem ju sax ja, ak meloom wu kawe wa, feeñ nañu bu leer, te bir ñépp ci yi mu sàkk, ba tax bunti lay yépp tëj nañu.

French

en effet, les perfections invisibles de dieu, sa puissance éternelle et sa divinité, se voient comme à l`oeil, depuis la création du monde, quand on les considère dans ses ouvrages. ils sont donc inexcusables,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

di xamle mbirum doomam, yeesu kirist sunu boroom. lu jëm ci meloom ci àddina, ci askanu daawuda la jóge, waaye lu jëm ci xelam mu sell, doomu yàlla la; ndaxte ndekkiteem nekk na firnde ju ràññiku, ne moom la.

French

et qui concerne son fils (né de la postérité de david, selon la chair,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,782,443,740 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK