Results for nitñee ko translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

xeet yépp seede ko.

French

salut que tu as préparé devant tous les peuples,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ki la ko indil:

French

vous est présenté par :

Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ñu bare gëm ko.

French

et, dans ce lieu-là, plusieurs crurent en lui.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

wax naa leen ko lu jiitu.

French

voici, je vous l`ai annoncé d`avance.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu jox ko dogu jën wu ñu lakk.

French

ils lui présentèrent du poisson rôti et un rayon de miel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ku ko nuyu, bokk nga ciy ñaawteefam.

French

car celui qui lui dit: salut! participe à ses mauvaises oeuvres.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ba noppi toog fa, di ko wottu.

French

puis ils s`assirent, et le gardèrent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye leer, lu mu ëmb, fésal ko.

French

mais tout ce qui est condamné est manifesté par la lumière, car tout ce qui est manifesté est lumière.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bu nu ko solee, dunu def yaramu neen.

French

si du moins nous sommes trouvés vêtus et non pas nus.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fí, mön nga tann dara ci, ngir nga mbinde ko

French

configuration multi-liste. vous pouvez double-cliquer sur une ligne pour éditer la valeur.

Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

di ko yeeru, bëgg a këf waxam bu awul yoon.

French

lui tendant des pièges, pour surprendre quelque parole sortie de sa bouche.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

indil ab xät u lüggey u compizconfig ngir ñeriñ ko lêegi ...

French

importer un profil compizconfig

Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu jàpp ko nag, génne ko tool bi, rey ko.»

French

et ils se saisirent de lui, le jetèrent hors de la vigne, et le tuèrent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu ne ko: «sa càmmiñ dina dekki.»

French

jésus lui dit: ton frère ressuscitera.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te yaxya daan ko wax: «jaaduwul nga denc ko.»

French

parce que jean lui disait: il ne t`est pas permis de l`avoir pour femme.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

tomaa tontu ko ne: «sama boroom, sama yàlla!»

French

thomas lui répondit: mon seigneur et mon dieu! jésus lui dit:

Last Update: 2024-04-13
Usage Frequency: 6
Quality:

Wolof

Ñu tontu ko: «sang bi, na sunuy bët ubbiku.»

French

ils lui dirent: seigneur, que nos yeux s`ouvrent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte mbooloo maa nga ko topp, di xaacu ne: «reyleen ko!»

French

car la multitude du peuple suivait, en criant: fais-le mourir!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye piyeer weddi ko ne: «soxna si, xawma kooku.»

French

mais il le nia disant: femme, je ne le connais pas.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,781,093,888 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK