From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
mu gis itam jenn jigéen ju jëkkëram faatu te mu ñàkk, ju fa def ñaari poseti xànjar.
il vit aussi une pauvre veuve, qui y mettait deux petites pièces.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw ga daal benn jigéen ju jëkkëram faatu, te mu ñàkk, ñëw, def ci ñaari poseti xànjar, yu matul sax dërëm.
il vint aussi une pauvre veuve, elle y mit deux petites pièces, faisant un quart de sou.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ne leen: «lan ngeen ma man a jox, ngir ma jébbal leen yeesu?» noonu saraxalekat ya daldi ko waññal fanweeri poseti estateer.
et dit: que voulez-vous me donner, et je vous le livrerai? et ils lui payèrent trente pièces d`argent.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te ñu bare ci ñi daan luxus, indi seeni téere, lakk leen ci kanam ñépp. te bi ñu xaymaa njëg ga, mu tollook juróom-fukki junniy poseti daraxma.
et un certain nombre de ceux qui avaient exercé les arts magiques, ayant apporté leurs livres, les brûlèrent devant tout le monde: on en estima la valeur à cinquante mille pièces d`argent.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu la ñu waxoon jaarale ko ci yonent yàlla yeremi am, bi mu naan: «fab nañu fanweeri poseti xaalis ya, mooy njëg gi bànni israyil xayma woon ci nit ki;
alors s`accomplit ce qui avait été annoncé par jérémie, le prophète: ils ont pris les trente pièces d`argent, la valeur de celui qui a été estimé, qu`on a estimé de la part des enfants d`israël;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi bët setee, mu génne ñaari poseti xaalis, jox ko boroom kër ga ne ko: “nanga topptoo nit kooku. bés bu ma fi jaaraatee, dinaa la fey, man ci sama bopp, lépp loo ci dolli ci xaalis.”»
le lendemain, il tira deux deniers, les donna à l`hôte, et dit: aie soin de lui, et ce que tu dépenseras de plus, je te le rendrai à mon retour.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: