Results for saraxaleem translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

bi sakariya matalee liggéeyu saraxaleem ba noppi, mu daldi ñibbi.

French

lorsque ses jours de service furent écoulés, il s`en alla chez lui.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

benn bés nag sakariya doon def liggéeyu saraxaleem ca yàlla, ndaxte mbootaayam a aye keroog.

French

or, pendant qu`il s`acquittait de ses fonctions devant dieu, selon le tour de sa classe, il fut appelé par le sort,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

looloo taxoon mu war a mel niy doomi baayam ci bépp fànn, ngir doon seen saraxalekat bu mag fa kanam yàlla, bi leen yërëm te di sàmm kóllëre, te ci liggéeyu saraxaleem joxe na bakkanam ngir dindi bàkkaari nit ñi, ba yàlla baal leen.

French

en conséquence, il a dû être rendu semblable en toutes choses à ses frères, afin qu`il fût un souverain sacrificateur miséricordieux et fidèle dans le service de dieu, pour faire l`expiation des péchés du peuple;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,777,312,088 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK