Results for sawar translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

Ñu sawar lañu ci rey nit.

French

ils ont les pieds légers pour répandre le sang;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci biir tiis, yeesu gën a sawar ci ñaan gi, ñaqam mel ni lumbi deret dal ci suuf.

French

Étant en agonie, il priait plus instamment, et sa sueur devint comme des grumeaux de sang, qui tombaient à terre.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci li dale ci jamonoy yaxya ba léegi, nit ñaa ngi góor-góorlu ngir dugg ci nguuru yàlla, te ñi sawar ñoo ci am wàll.

French

depuis le temps de jean baptiste jusqu`à présent, le royaume des cieux est forcé, et ce sont les violents qui s`en s`emparent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fekk ña fa nekk ñoo gën a am ay teggin waa tesalonig, ndaxte nangu nañu kàddu ga te sawar ca, di niir mbind mi bés bu nekk, ba xam ndax loolu dëgg la am déet.

French

ces juifs avaient des sentiments plus nobles que ceux de thessalonique; ils reçurent la parole avec beaucoup d`empressement, et ils examinaient chaque jour les Écritures, pour voir si ce qu`on leur disait était exact.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag sama bokk yi ma sopp, nangeen takku, sampu ba dëgër, te gën a sawar ci liggéeyu boroom bi, xam ne seen liggéey, bi jëm ci boroom bi, du neen.

French

ainsi, mes frères bien-aimés, soyez fermes, inébranlables, travaillant de mieux en mieux à l`oeuvre du seigneur, sachant que votre travail ne sera pas vain dans le seigneur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ko njiit ya déggee, ñu màggal yàlla ne ko: «mbokk mi, gis nga ne, am na ay junniy yawut ñu gëm, te ñépp a sawar ci yoonu musaa.

French

quand ils l`eurent entendu, ils glorifièrent dieu. puis ils lui dirent: tu vois, frère, combien de milliers de juifs ont cru, et tous sont zélés pour la loi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«man yawut laa, juddoo tars ci diiwaanu silisi, yaroo ci dëkk bii. taalibe laa woon ci gamaleel, mu jàngal ma bu wér yoonu sunuy maam, ba ma sawar ci yàlla, mel ni yéen ñépp tey.

French

je suis juif, né à tarse en cilicie; mais j`ai été élevé dans cette ville-ci, et instruit aux pieds de gamaliel dans la connaissance exacte de la loi de nos pères, étant plein de zèle pour dieu, comme vous l`êtes tous aujourd`hui.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,947,480,833 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK