Results for su ne translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

su fekkee ne ñi dee duñu dekki, kon kirist it dekkiwul.

French

s`il n`y a point de résurrection des morts, christ non plus n`est pas ressuscité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«su fekkee ne yaay buuru yawut yi, musalal sa bopp!»

French

ils disaient: si tu es le roi des juifs, sauve-toi toi-même!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te su ko xeebee it, ñu xeeb ko.

French

et si quelqu`un l`ignore, qu`il l`ignore.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

su nu waxee ne amunu bàkkaar, kon nax nanu sunu bopp, te dëgg nekkul ci nun.

French

si nous disons que nous n`avons pas de péché, nous nous séduisons nous-mêmes, et la vérité n`est point en nous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

su fekkeente ne nag jubuleen ci alalu àddina, kon ku leen di dénk alal ju wóor ji?

French

si donc vous n`avez pas été fidèle dans les richesses injustes, qui vous confiera les véritables?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

su nu waxee ne defunu bàkkaar, teg nanu ko kuy tebbi waxam, te kàddoom duggagul ci sunu xol.

French

si nous disons que nous n`avons pas péché, nous le faisons menteur, et sa parole n`est point en nous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

su aajoo ma demal sama bopp, kon dinañu ànd ak man.

French

si la chose mérite que j`y aille moi-même, elles feront le voyage avec moi.

Last Update: 2024-04-13
Usage Frequency: 30
Quality:

Wolof

waaye su ngeen di laaj leneen, mbooloom dëgg dina ko àtte.

French

et si vous avez en vue d`autres objets, ils se régleront dans une assemblée légale.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye su nu yéglee ne, kirist dekki na, nan la ñenn ñi ci yéen man a waxe ne, néew yi duñu dekki?

French

or, si l`on prêche que christ est ressuscité des morts, comment quelques-uns parmi vous disent-ils qu`il n`y a point de résurrection des morts?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye aajowul jottalikat, su fi kenn rekk teewee, te yàlla kenn la.

French

or, le médiateur n`est pas médiateur d`un seul, tandis que dieu est un seul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

su ñu leen jànnee sax ci turu kirist, xamleen ne ñu barkeel ngeen, ndax xelum yàllaa ngi ci yéen, di firndeel seen ndamu ëllëg.

French

si vous êtes outragés pour le nom de christ, vous êtes heureux, parce que l`esprit de gloire, l`esprit de dieu, repose sur vous.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon nag su fekkee ku jàngul mbiri kirist walla ku gëmul dugg ca mbooloo ma, fekk ñépp di wax ay làkk, ndax du wax ne, dangeen a dof?

French

si donc, dans une assemblée de l`Église entière, tous parlent en langues, et qu`il survienne des hommes du peuple ou des non-croyants, ne diront-ils pas que vous êtes fous?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye ba tey su fekkee ne nu ngi wut a jub ci kaw gëm kirist, fekk nu ne fàŋŋ di ay bàkkaarkat, ndax nag kirist moo sas bàkkaar? mukk!

French

mais, tandis que nous cherchons à être justifié par christ, si nous étions aussi nous-mêmes trouvés pécheurs, christ serait-il un ministre du péché? loin de là!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

jigéen ju dul musóoru, bu yaboo, mu watu. waaye su fekkee ne jigéen dafay am kersa, su wàññee kawaram walla mu watu, fàww kon mu musóoru.

French

car si une femme n`est pas voilée, qu`elle se coupe aussi les cheveux. or, s`il est honteux pour une femme d`avoir les cheveux coupés ou d`être rasée, qu`elle se voile.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kan ci yéen moo man a seede ne, bàkkaar naa? su ma waxee dëgg nag, lu tax dungeen ma gëm?

French

qui de vous me convaincra de péché? si je dis la vérité, pourquoi ne me croyez-vous pas?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci sunu biir lañu jóge, waaye bokkuñu woon ci nun; ndaxte su ñu bokkoon ci nun, kon dinañu des ci nun. waaye dàggeeku nañu nu, ngir mu leer ne, kenn ci ñoom bokkul woon ci nun.

French

ils sont sortis du milieu de nous, mais ils n`étaient pas des nôtres; car s`ils eussent été des nôtres, ils seraient demeurés avec nous, mais cela est arrivé afin qu`il fût manifeste que tous ne sont pas des nôtres.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu tontu ko ne: «su ma waxee lu jaaduwul, wone ko; waaye su ma waxee lu jub, lu tax nga may dóor?»

French

jésus lui dit: si j`ai mal parlé, fais voir ce que j`ai dit de mal; et si j`ai bien parlé, pourquoi me frappes-tu?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,776,764,051 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK