From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ndaxte moo waral yawut yu bare dëddu leen, gëm yeesu.
parce que beaucoup de juifs se retiraient d`eux à cause de lui, et croyaient en jésus.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
looloo waral kóllëre gu jëkk ga, ñu fasoon ko ak deret.
voilà pourquoi c`est avec du sang que même la première alliance fut inaugurée.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
lu tax dégguleen li ma leen wax? li ko waral moo di mënuleen koo déglu.
pourquoi ne comprenez-vous pas mon langage? parce que vous ne pouvez écouter ma parole.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
li waral mbir mi gën a leer moo di ne, beneen saraxalekat bu mel ni melkisedeg dafa ñëw.
cela devient plus évident encore, quand il paraît un autre sacrificateur à la ressemblance de melchisédek,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
loolu sax moo waral kirist dee te dundaat, ngir man a nekk boroomu ñi dee ak ñiy dund.
car christ est mort et il a vécu, afin de dominer sur les morts et sur les vivants.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte yaakaar naa ne, yónnee ku ñu tëj, te bañ caa boole lu ko waral, àndul ak xel.»
car il me semble absurde d`envoyer un prisonnier sans indiquer de quoi on l`accuse.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu ndaje ma rëb, ba ñii di yuuxu lii, ñale di yuuxu laa, te ña ca gën a bare xamuñu lu waral ndaje ma.
les uns criaient d`une manière, les autres d`une autre, car le désordre régnait dans l`assemblée, et la plupart ne savaient pas pourquoi ils s`étaient réunis.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ci li jëm ci yoonu musaa, dee naa, fekk yoon wi ci boppam moo ko waral, ngir ma man a dund, ba amal jariñ yàlla.
car c`est par la loi que je suis mort à la loi, afin de vivre pour dieu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
looloo waral it ñu jottali xebaar bu baax ndee, ya fekke woon jamonoy nóoyin jooju, ngir ñu dunde yàlla ci seen xel, doonte sax nit ñaa ngi leen daan fitnaal ci àddina.
car l`Évangile a été aussi annoncé aux morts, afin que, après avoir été jugés comme les hommes quant à la chair, ils vivent selon dieu quant à l`esprit.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ndaxte fi mu ne man nañu noo jiiñ jógug mbooloo mi ndax li fi xew tey. te bu loolu amee dunu am aw lay ci mbirum mbooloo mu rëb mii, ndaxte amul dara lu ko waral.»
nous risquons, en effet, d`être accusés de sédition pour ce qui s`est passé aujourd`hui, puisqu`il n`existe aucun motif qui nous permette de justifier cet attroupement.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi ñuy yóbbu yeesu, simoŋ piyeer ak keneen ca taalibe ya toppoon nañu ko. keneen kooku nag, xamante na ak saraxalekat bu mag ba, moo waral mu duggaaleek yeesu ca biir kër kilifa ga.
simon pierre, avec un autre disciple, suivait jésus. ce disciple était connu du souverain sacrificateur, et il entra avec jésus dans la cour du souverain sacrificateur;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñiy joŋante ci po muy waral tàggat yaram, dañuy xañ seen bopp lu bare. dañu koy def, ngir am kaalag ndam gu dul yàgg; waaye nun danu koy def, ngir am kaalag ndam gu sax ba fàww.
tous ceux qui combattent s`imposent toute espèce d`abstinences, et ils le font pour obtenir une couronne corruptible; mais nous, faisons-le pour une couronne incorruptible.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
te loolu lépp teewul ñu walbatiku, ñooñu kenn dootu leen man a yeesalaat, ba ñu tuub seeni bàkkaar. li ko waral moo di, dañoo bëgg a daajaat doomu yàlla ji ci bant, di ko toroxal, te fekk muy seen ngaañ.
et qui sont tombés, soient encore renouvelés et amenés à la repentance, puisqu`ils crucifient pour leur part le fils de dieu et l`exposent à l`ignominie.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: