Results for yokk translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

yokk ci sopp mbokk, yokk ci bëgg ñépp.

French

à la piété l`amour fraternel, à l`amour fraternel la charité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noot sa bopp googu, ngeen yokk ci muñ, yokk ci ragal yàlla,

French

à la science la tempérance, à la tempérance la patience, à la patience la piété,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ana kan ci yéen ci kaw njaaxleem, moo man a yokk ab waxtu ci àppam?

French

qui de vous, par ses inquiétudes, peut ajouter une coudée à la durée de sa vie?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ne ko: «sàllaaw dinaa la barkeel, yokk saw askan.»

French

certainement je te bénirai et je multiplierai ta postérité.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

di màggal yàlla te am yiw ci wetu nit ñépp. noonu bés bu nekk boroom bi di yokk ca mbooloo ma ñi mucc.

French

louant dieu, et trouvant grâce auprès de tout le peuple. et le seigneur ajoutait chaque jour à l`Église ceux qui étaient sauvés.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen itam, gannaaw dangeen a fonk mayi xelum yàlla, jéemleen a ëpple ci liy yokk ngëmu mbooloo mi.

French

de même vous, puisque vous aspirez aux dons spirituels, que ce soit pour l`édification de l`Église que vous cherchiez à en posséder abondamment.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye ñam mënul a tax nu neex yàlla. su nu ci lekkee, du yokk dara ci nun. su nu ci lekkul, du nu wàññi dara.

French

ce n`est pas un aliment qui nous rapproche de dieu: si nous en mangeons, nous n`avons rien de plus; si nous n`en mangeons pas, nous n`avons rien de moins.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na loolu tax ngeen góor-góorlu, ba yokk ci seen ngëm njàmbaar, ci njàmbaar googu ngeen yokk ci xam-xam, yokk ci noot sa bopp.

French

à cause de cela même, faites tous vos efforts pour joindre à votre foi la vertu, à la vertu la science,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,775,973,433 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK