From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
te it bu fekkee ne man damay dàq ay rab ci kàttanu beelsebul, seeni taalibe nag ci gan kàttan lañu leen di dàqe? kon ñoo leen di àtte.
so aber ich die teufel durch beelzebub austreibe, durch wen treiben sie eure kinder aus? darum werden sie eure richter sein.
te it xutbakat ya jóge yerusalem ne: «beelsebul jàpp na ko; ci kàttanu buuru rab yi lay dàqe rab yi.»
die schriftgelehrten aber, die von jerusalem herabgekommen waren, sprachen: er hat den beelzebub, und durch den obersten teufel treibt er die teufel aus.
bi farisen ya déggee loolu nag, ñu ne: «kii ci kàttanu beelsebul, buuru rab yi, lay dàqe rab yi.»
aber die pharisäer, da sie es hörten, sprachen sie: er treibt die teufel nicht anders aus denn durch beelzebub, der teufel obersten.
te it bu seytaane xeexee boppam, naka la nguuram di man a yàgge? damay wax loolu, ndaxte nee ngeen, damay dàq rab jaarale ko ci kàttanu beelsebul.
ist denn der satanas auch mit sich selbst uneins, wie will sein reich bestehen? dieweil ihr sagt, ich treibe die teufel aus durch beelzebub.