Results for nopp translation from Wolof to Italian

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Italian

Info

Wolof

yaw mi am ay nopp, déglul.

Italian

chi ha orecchi, ascolti

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.

Italian

chi ha orecchi intenda

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 2
Quality:

Wolof

déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»

Italian

se uno ha orecchi per intendere, intenda!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yaw mi am ay nopp, déglul li xelum yàlla di wax mboolooy ñi gëm.

Italian

chi ha orecchi, ascolti ciò che lo spirito dice alle chiese

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 4
Quality:

Wolof

ndax ay gumbay njàccaar ngeen, te seeni nopp naqari? xanaa fàttalikuwuleen;

Italian

avete occhi e non vedete, avete orecchi e non udite? e non vi ricordate

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye kenn ci ñi fa taxaw bocci jaaseem, dóor surgab saraxalekat bu mag bi, nopp bi dagg.

Italian

uno dei presenti, estratta la spada, colpì il servo del sommo sacerdote e gli recise l'orecchio

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«waaye yéen barkeel ngeen, ndaxte seeni bët a ngi gis te seeni nopp di dégg!

Italian

ma beati i vostri occhi perché vedono e i vostri orecchi perché sentono

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yaw mi am ay nopp, déglul li xelum yàlla di wax mboolooy ñi gëm. ku daan, doo loru ci ñaareelu dee.

Italian

chi ha orecchi, ascolti ciò che lo spirito dice alle chiese: il vincitore non sarà colpito dalla seconda morte

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

booba nag ñu jub ñi dinañu leer ni jant bi ci seen nguuru baay. déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»

Italian

allora i giusti splenderanno come il sole nel regno del padre loro. chi ha orecchi, intenda

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

du jariñ suuf, te du nekk tos. dañu koy sànni ca biti. déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»

Italian

non serve né per la terra né per il concime e così lo buttano via. chi ha orecchi per intendere, intenda»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte xolu xeet wii dafa dërkiis;dañuy déglu ak nopp yu naqari,tey gëmm seeni bët,ngir bañ a gis ak seeni bët,dégg ak seeni nopp,te xam ci seen xol,ñu woññiku ci man, ma wéral leen.”

Italian

perché il cuore di questo popolo si è indurito, son diventati duri di orecchi, e hanno chiuso gli occhi, per non vedere con gli occhi, non sentire con gli orecchi e non intendere con il cuore e convertirsi, e io li risani

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,726,499 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK