Results for li no mofi bayo mat na translation from Wolof to Spanish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Spanish

Info

Wolof

limub gawar ga doon xareji mat na ñaari alfunniy alfunni. dégg naa lim ba.

Spanish

el número de los soldados de a caballo era de dos miríadas de miríadas; yo escuché el número de ellos

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi yeesu agsee, mu fekk ne, bi ñu dencee lasaar ak léegi, mat na ñeenti fan.

Spanish

cuando llegó jesús, halló que hacía ya cuatro días que lázaro estaba en el sepulcro

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kenn musul a gis yàlla, waaye bu nu bëggantee, yàllaa ngi dëkk ci nun te mbëggeelam mat na sëkk ci nun.

Spanish

nadie ha visto a dios jamás. si nos amamos unos a otros, dios permanece en nosotros, y su amor se ha perfeccionado en nosotros

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kuy sàmm kàddug yàlla, dëgg-dëgg sa mbëggeel ci yàlla mat na sëkk. ci loolu lanu xame ne, nekk nanu ci moom.

Spanish

pero en el que guarda su palabra, en éste verdaderamente el amor de dios ha sido perfeccionado. por esto sabemos que estamos en él

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu mu daldi ne: «tey jii, loolu mbind mi wax mat na, bi ngeen koy déglu.»

Spanish

entonces comenzó a decirles: --hoy se ha cumplido esta escritura en vuestros oídos

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naan: «jamono ji mat na, nguuru yàlla jegesi na; tuubleen seeni bàkkaar te gëm xebaar bu baax bi.»

Spanish

y diciendo: "el tiempo se ha cumplido, y el reino de dios se ha acercado. ¡arrepentíos y creed en el evangelio!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Wolof

xam naa taalibeb kirist boo xam ne yékkati nañu ko ba ca asamaan, si gën a kawe, booba ak léegi mat na fukki at ak ñeent. xawma ndax ànd na ak jëmmam walla déet. yàlla rekk a xam.

Spanish

conozco a un hombre en cristo, que hace catorce años--si en el cuerpo, no lo sé; si fuera del cuerpo, no lo sé; dios lo sabe-- fue arrebatado hasta el tercer cielo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu teg ca ne ma: «lépp mat na! maay alfa ak omega, njàlbéen gi ak muj gi. ku mar, dinaa la may ci bëtu ndoxum dund mi, te doo fey dara.

Spanish

me dijo también: "¡está hecho! yo soy el alfa y la omega, el principio y el fin. al que tenga sed, yo le daré gratuitamente de la fuente de agua de vida

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
7,787,539,167 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK