Usted buscó: mafuta (Suajili - Wólof)

Contribuciones humanas

De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.

Añadir una traducción

Suajili

Wólof

Información

Suajili

wewe lakini unapofunga, paka kichwa chako mafuta, nawa uso wako,

Wólof

yaw nag booy woor, xeeñalal sa bopp te nga sëlmu,

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

wale wapumbavu walichukua taa zao, lakini hawakuchukua akiba ya mafuta.

Wólof

Ñi ñàkk xel nag fab nañu seeni làmp, waaye fabaalewuñu diwlin;

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

lakini wale wenye busara walichukua mafuta katika chupa pamoja na taa zao.

Wólof

waaye ñi am xel ñoom fab nañu seeni làmp, fabaale diwlin ciy njaq.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

wale wapumbavu wakawaambia wale wenye busara: tupeni mafuta yenu kidogo maana taa zetu zinazimika.

Wólof

Ñi ñàkk xel wax ñi am xel: “mayleen nu ci seen diwlin, ndaxte sunuy làmp ñu ngi bëgg a fey.”

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

wewe hukunionyesha ukarimu wako kwa kunipaka mafuta kichwani, lakini huyu mwanamke amefanya hivyo kwa kunipaka mafuta miguu yangu.

Wólof

defuloo diw ci sama bopp, waaye moom, sotti na latkoloñ ci samay tànk.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

je, yuko mgonjwa kati yenu? anapaswa kuwaita wazee wa kanisa, nao watamwombea na kumpaka mafuta kwa jina la bwana.

Wólof

su amee ci yéen ku wopp, na woo njiiti mbooloo mi, ñu ñaanal ko te diw boppam ci turu boroom bi.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

akamwendea, akamtibu majeraha yake kwa kumtia mafuta na divai; na kuyafunga halafu akampandisha juu ya punda wake akampeleka katika nyumba moja ya wageni akamuuguza.

Wólof

noonu mu ñëw, diw ko diwlin ak biiñ ngir faj gaañu-gaañu ya, bandaas ko. gannaaw loolu mu teg ko ci mbaamam, yóbbu ko ci fanaanukaay, di ko topptoo.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

yeye akamjibu: mapipa mia ya mafuta ya zeituni. yule karani akamwambia: chukua hati yako ya deni, keti haraka, andika hamsini.

Wólof

mu ne ko: “téeméeri bidoŋi diwlinu oliw.” bëkk-néeg ba ne ko: “sa kayit a ngii. toogal fii gaaw te bind juróom-fukk.”

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

basi, wale wanawali wapumbavu walipokwenda kununua mafuta, bwana arusi akafika, na wale wanawali waliokuwa tayari wakaingia pamoja naye katika jumba la arusi, kisha mlango ukafungwa.

Wólof

«bi nga xamee ne dem nañu jëndi, boroom séet ba agsi. Ñi amoon diwlin ci seeni làmp, ànd ak boroom séet ba ca reer ya. noonu bunt ba tëj.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Suajili

"maana, kwa hakika, ndivyo herode, pontio pilato, watu wa israeli na watu wa mataifa walivyokutanika papa hapa mjini, kumpinga yesu mtumishi wako mtakatifu ambaye umemtia mafuta.

Wólof

ndaxte ci dëgg ci dëkk bii, erodd ak poñsë pilaat ànd ak xeeti àddina ak bànni israyil, likkoo nañu, ngir daaneel sa ndaw lu sell li nga fal, di yeesu,

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Advertencia: contiene formato HTML invisible

Suajili

mdalasini, viungo, ubani, manemane, udi, divai, mafuta, unga na ngano, ng'ombe na kondoo, farasi na magari ya kukokotwa, watumwa wao na hata maisha ya watu.

Wólof

ak bant yuy safal, gàncax gu xeeñ, ay xeeti cuuraay yu bare, latkoloñ, biiñ, diw, sungufu lay-layaat, pepp, ay nag, ay xar, ay fas, sareeti xare, ay jaam, ba ci bakkani nit.

Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:

Obtenga una traducción de calidad con
7,764,638,327 contribuciones humanas

Usuarios que están solicitando ayuda en este momento:



Utilizamos cookies para mejorar nuestros servicios. Al continuar navegando está aceptando su uso. Más información. De acuerdo