De traductores profesionales, empresas, páginas web y repositorios de traducción de libre uso.
aliwaponya pia wote waliokuwa wanasumbuliwa na pepo wachafu.
dañoo ñëw ngir déglu ko, te it ngir mu faj leen. Ñi rab jàpp it faju nañu.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
aliwaita wale wanafunzi kumi na wawili, akaanza kuwatuma wawiliwawili. aliwapa uwezo wa kuwatoa pepo wachafu,
noonu mu woo ci moom fukki taalibe ya ak ñaar, jox leen sañ-sañu dàq rab yi, yónni leen, ñu ànd ñaar-ñaar.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
yesu aliwaita wanafunzi wake kumi na wawili, akawapa uwezo wa kutoa pepo wachafu na kuponya magonjwa na maradhi yote.
noonu yeesu woo ca moom fukki taalibeem ya ak ñaar, jox leen sañ-sañu dàq rab yi, tey faj jàngoro yépp ak wéradi yépp.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
maana pepo wachafu waliokuwa wamewapagaa watu wengi waliwatoka wakipiga kelele kubwa; na pia watu wengi waliokuwa wamepooza viungo na waliolemaa waliponywa.
ndaxte ay rab yu bon bàyyi nañu nit ñu bare, ña ñu jàppoon, di yuuxu ci kaw; te ñu bare ñu làggi ak ñu lafañ daldi wér.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
na watu waliokuwa wamepagawa na pepo wachafu walipomwona, walijitupa chini mbele yake na kupaaza sauti, "wewe ni mwana wa mungu!"
fekk booba képp ku rab jàpp ku ko gis, daanu fa kanamam di yuuxu naan: «yaa di doomu yàlla.»
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
Advertencia: contiene formato HTML invisible
naye akawaruhusu. basi, hao pepo wachafu wakatoka, wakawaingia wale nguruwe. kundi lote la nguruwe wapatao elfu mbili likaporomoka kwenye ule mteremko mkali mpaka ziwani, likatumbukia majini.
mu may leen ko. noonu rab ya génn nit ka, dugg mbaam-xuux ya, ñu daldi bartalu, daanu ca dex ga, lab fa. mbaam-xuux ya nag matoon nañu ñaari junni.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
basi, akapaaza sauti kwa nguvu akisema, "umeanguka; babuloni mkuu umeanguka! sasa umekuwa makao ya mashetani na pepo wachafu; umekuwa makao ya ndege wachafu na wa kuchukiza mno.
mu daldi xaacu naan: «daanu na! babilon mu mag ma daanu na! léegi dëkkukaayu jinne la, ak bépp rab wu bon ak bépp picc mu daganul te araam.
Última actualización: 2012-05-05
Frecuencia de uso: 1
Calidad:
Advertencia: contiene formato HTML invisible