Vous avez cherché: evangelie (Afrikaans - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Afrikaans

Wolof

Infos

Afrikaans

en daar het hulle die evangelie verkondig.

Wolof

foofa ñu di fa xamle xebaar bu baax bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die evangelie moet eers aan al die nasies verkondig word.

Wolof

fàww xebaar bu baax bi jëkk a jib ci xeet yépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

die begin van die evangelie van jesus christus, die seun van god.

Wolof

xebaar bu baaxu yeesu kirist, doomu yàlla, nii la tàmbalee.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

hy het dan ook met baie ander vermaninge die evangelie aan die volk verkondig.

Wolof

noonu yaxya teg ca yeneen dénkaane yu bare, di yégal nit ña xebaar bu baax ba.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en as skoene aan julle voete die bereidheid vir die evangelie van vrede.

Wolof

solooleen jàmm, ji xebaar bu baax biy joxe, ni ay dàll ci seeni tànk, ba jekk ci lépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

volgens die evangelie van die heerlikheid van die salige god wat aan my toevertrou is.

Wolof

mu xebaar bu baax bi indaale. te xamleb xebaar, boobuy feeñal ndamu yàlla aji tedd ji, dénk nañu ma ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

maar as ons evangelie dan nog bedek is, is dit bedek in die wat verlore gaan,

Wolof

su fekkee ne sax, xebaar bu baax bi dafa muuru ci ñenn ñi, dafa fekk ñoom ñu aw yoon wu jëm ci sànkute.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en die wat verstrooi was, het die land deurgegaan en die woord van die evangelie verkondig.

Wolof

Ñi tasaaroo nag dem fu nekk, di fa xamle xebaar bu baax bu kàddug yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

ek wou hom by my hou, sodat hy my in die boeie van die evangelie in jou plek kan dien.

Wolof

dama koo bëggoon a téye fi sama wet, ngir mu taxawal la, di ma dimbali, li feek maa ngi ci kaso bi ngir xebaar bu baax bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en ek weet dat as ek na julle kom, ek met die volle seën van die evangelie van christus sal kom.

Wolof

te wóor na maa ne, bu ma agsee ci yéen, dinaa indaale barkeb kirist bu mat sëkk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en filippus het sy mond geopen en van hierdie skrif af begin en die evangelie van jesus aan hom verkondig.

Wolof

noonu filib tàmbali ci aaya yooyu, xamal ko xebaar bu baax bi ci mbirum yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

dat die heidene mede-erfgename is en medelede van die liggaam en mededeelgenote aan sy belofte in christus deur die evangelie

Wolof

mbir mi nii la tëdde: léegi xeet yi dul yawut dañoo bokksi cér ak yawut yi, bokk ak ñoom jenn jëmm, bokk wàll ci xéewal yi yàlla dige ci kirist yeesu, te xebaar bu baax bi xamle ko.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

blindes sien weer en kreupeles loop, melaatses word gereinig en dowes hoor, dooies word opgewek en aan armes word die evangelie verkondig.

Wolof

gumba yaa ngi gis, lafañ yiy dox, gaana yi wér, tëx yiy dégg, ñi dee di dekki, te ñi woyoflu ñu ngi dégg xebaar bu baax bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

aan wie ons selfs nie 'n oomblik in onderworpenheid toegegee het nie, sodat die waarheid van die evangelie by julle bestendig sou bly.

Wolof

waaye yaatalunu leen benn yoon, ngir dëggug xebaar bu baax bi man a sax ci yéen.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

aan hom dan wat magtig is om julle te versterk volgens my evangelie en die prediking van jesus christus, ooreenkomstig die openbaring van die verborgenheid wat eeue lank verswyg is,

Wolof

santleen yàlla, mi leen man a saxal bu wér ci dëggu xebaar bu baax, bi may waare ci mbirum yeesu kirist! nekkoon na kumpa gu làqu diirub ay ati at,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en daar was sommige van hulle, cipriese en cirenése manne, wat in antiochíë gekom het en met die griekssprekende jode gepraat en die evangelie van die here jesus verkondig het.

Wolof

moona amoon na ci ñoom ay niti sipar ak dëkku siren, ñu ñëw ci ancos, ba seen wax law ci gereg yi it, ñu di leen xamal xebaar bu baax bu yeesu boroom bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

maar alhoewel ons vantevore, soos julle weet, in filíppi gely het en mishandel is, het ons in onse god vrymoedigheid gehad om aan julle die evangelie van god te verkondig onder veel stryd.

Wolof

laata nuy ñëw, jaar nanu ci fitna ak toroxte ca dëkku filib, ni ngeen ko xame; waaye yàlla sunu boroom may na nu fit, ba li tongoonte bi metti lépp it, yégal nanu leen xebaaru yàlla bu baax bi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

die gees van die here is op my, omdat hy my gesalf het om die evangelie aan die armes te bring. hy het my gestuur om die wat verbryseld van hart is, te genees;

Wolof

«xelum boroom baa ngi ci man,ndaxte moo ma tànn,ngir ma yégal néew doole yi xebaar bu baax bi.dafa maa yónni,ngir ma yégal jaam ñi ne, dinañu leen goreel,yégal gumba yi ne, dinañu gis,te jot ñi ñu noot,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en ek het 'n ander engel in die middel van die lug sien vlieg met 'n ewige evangelie om te verkondig aan die bewoners van die aarde en aan alle nasies en stamme en tale en volke.

Wolof

noonu ma gis meneen malaaka naaw ca digg asamaan, yor xebaar bi sax, di ko yégal waa àddina — xeet yépp, giir yépp, kàllaama yépp ak réew yépp.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en julle, filippense, weet ook dat in die begin van die evangelie, toe ek van macedónië vertrek het, geen gemeente deel gehad het in my rekening van uitgawe en inkomste nie, behalwe julle alleen.

Wolof

yéen waa filib xam ngeen ne, bi ngeen jëkkee xam xebaar bu baax bi, te ma jóge diiwaanu maseduwan, benn mbooloo àndul woon ak man ci mbirum joqleente ndimbal, mu dul yéen doŋŋ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,748,091,033 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK