Vous avez cherché: verdrukking (Afrikaans - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Afrikaans

Wolof

Infos

Afrikaans

ly dan verdrukking soos 'n goeie krygsman van jesus christus.

Wolof

bokkal ak man tiis, di jàmbaar ci toolu xareb kirist yeesu,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

nogtans het julle goed gedoen toe julle deel gehad het in my verdrukking.

Wolof

waaye teewul taxawu, bi ngeen ma taxawu ci sama tiis, jëf ju rafet la.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

aangesien dit reg is by god om aan die wat julle verdruk, verdrukking te vergelde,

Wolof

ndaxte jub na ci yàlla, mu delloo coono ñi leen di sonal,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

daarom, broeders, is ons in al ons verdrukking en nood vertroos oor julle deur jul geloof.

Wolof

noonu bokk yi, ci biir tiis ak coono yi nu nekk, seen ngëm dëfël na sunu xol.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

verbly julle in die hoop; wees geduldig in die verdrukking; volhard in die gebed.

Wolof

bégleen ci yaakaaru ëllëg te muñ bépp tiis, di sax ci ñaan yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en nie alleen dit nie, maar ons roem ook in die verdrukkinge, omdat ons weet dat die verdrukking lydsaamheid werk,

Wolof

te du ci loolu rekk, waaye bég nanu it ci sunuy nattu; ndax xam nanu ne, nattu day feddali muñ;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

dat onder baie beproewing deur verdrukking hulle oorvloedige blydskap by hulle diepe armoede oorvloedig was in hulle ryke milddadigheid.

Wolof

nattu yi ñu jaar ëmb nañu coono yu réy; waaye seen mbég mu tar ak seen ñàkk gu metti ñoo jur ci ñoom yéwén gu jéggi dayo.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

want dan sal daar groot verdrukking wees soos daar van die begin van die wêreld af tot nou toe nie gewees het en ook nooit sal wees nie.

Wolof

ndaxte booba dina am metit wu réy wu musul a am, ba àddina sosoo ak tey, te dootul am mukk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en julle het navolgers van ons geword en van die here deurdat julle die woord in baie verdrukking ontvang het met die blydskap van die heilige gees,

Wolof

te aw ngeen sunuy tànk ak yu boroom bi, ci li ngeen nangu xebaar bi ci biir fitna yu metti, ànd ak mbég ci dooley xel mu sell mi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

dan sal hulle jul aan verdrukking oorgee en julle doodmaak; en julle sal deur al die nasies gehaat word ter wille van my naam.

Wolof

bu boobaa dees na leen jébbale, metital leen, rey leen; te xeet yépp dinañu leen bañ ndax sama tur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

maar wees jy in alles nugter; ly verdrukking; doen die werk van 'n evangelis; vervul jou bediening.

Wolof

waaye yaw nanga foog ci lépp, dékku tiis, tey tas xebaar bu baax bi, ba matal sag yónnent.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

want daardie dae sal daar 'n verdrukking wees soos daar nie gewees het van die begin van die skepping af wat god geskape het tot nou toe, en ook nooit sal wees nie.

Wolof

ndaxte booba dina am metit wu réy wu musul a am, ba àddina sosoo ak tey, te dootul am mukk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

die wat dan verstrooi was deur die verdrukking wat oor stéfanus ontstaan het, het die land deurgegaan tot by fenícië en ciprus en antiochíë sonder om tot iemand die woord te spreek, behalwe tot die jode alleen.

Wolof

Ñi tasoon nag ndax fitna, ji amoon gannaaw ecen, ñu dem ba diiwaanu fenisi, ci dunu sipar ak ca dëkku ancos, di wax kàddu gi, waaye yemale ko ci yawut yi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

dit het ek vir julle gesê, dat julle in my vrede kan hê. in die wêreld sal julle verdrukking hê; maar hou goeie moed, ek het die wêreld oorwin.

Wolof

waaye nag déedéet, wéetuma, ndaxte baay baa ngi may wéttali. dama leen wax loolu, ngir ngeen am jàmm ci man. dingeen am nattu ci àddina, waaye takkleen fit yi; noot naa àddina.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

maar geen wortel in hulleself het nie; hulle is net vir 'n tyd. later as daar verdrukking of vervolging kom ter wille van die woord, struikel hulle dadelik.

Wolof

waaye du yàgg, ndaxte wax ji saxul ci moom. bu jaaree ci nattu nag, mbaa ñu fitnaal ko ndax kàddu gi, mu dàggeeku ci saa si.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

ek, johannes, julle broeder en deelgenoot in die verdrukking en in die koninkryk en lydsaamheid van jesus christus, was op die eiland wat patmos genoem word, ter wille van die woord van god en om die getuienis van jesus christus.

Wolof

man yowaana seen mbokk, di seen nawle ci fitna, ci nguur ak ci muñ, yi nu am ndax sunu booloo ak yeesu, maa nga nekkoon ca dun bu ñuy wax patmos. wacce woon nañu ma fa, ndax li ma doon waare kàddug yàlla tey seedeel yeesu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

maar as jy tog trou, sondig jy nie; en as 'n maagd trou, sondig sy nie. maar sulke mense sal verdrukking hê vir die vlees, en ek wil julle spaar.

Wolof

waaye nag boo séyee, defoo bàkkaar, te bu janq séyee, deful bàkkaar. waaye ñi séy dinañu am naqar ci àddina, te naqar woowu dama leen koo bëggoon fanqal, yéen ñi séyagul.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Afrikaans

en ek sê vir hom: my heer, u weet dit. en hy sê vir my: dit is hulle wat uit die groot verdrukking kom, en hulle het hul klere gewas en hul klere wit gemaak in die bloed van die lam.

Wolof

ma ne ko: «sang bi, xanaa yaa ko xam.» mu ne ma: «Ñoo di ñi jóge ca metit wu réy wa. fóot nañu seeni mbubb, ba weexal ko ci deretu mbote ma.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,788,577,292 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK